Leuz Diwane G - Lou Nek Ak Wakhtom paroles de chanson

paroles de chanson Lou Nek Ak Wakhtom - Leuz Diwane G



I gotta go
Wax ko sa gagni
Awma time bimay waste
Iyo yaa
Aaa iyoo
Ayayayayéé
Iyoo yaa
No time to waste
We leave the hip-hop
To the go
Thiaxan faki deugu déss
Sonné mou rir nga dégu ko
Dégn télla tékk aim
Di dém dox amoul guestou
Doma tardél shut the fucker
Compeu nagn lou wéssou
Weather you like it or not
Foc gnou teub sén barrière yi go
Doon sén dream gni déff ko
Deuguen taan lagni ngébo
You will go
No stop
Sampii flag bi outside
Adina weurngueul keup
Taxaw ferme feusseul fight
Khadji mbeuw meunoul gniak
Guis bouki bangui gni boot
Khati daw néko diakeu
Door mou baleu gneupe root
Bawane sa beuneu ba waral Talla dess cii ndigueu
Daw lekh nga daw dekh ga
Mbeureung lay la faw yegu
Moytoul beul bou reuthie souf
Fakhas leup louy sikeu
Youkhou mbott meunoul touss ci nagu bi
Téén bi dégn ko ségu
Feut feut dou wadal nopi mbam
Khara djitou ci leundeum beuy
Tioki tioki dougui tam
Kou beuga fompi leundeum kheuy
'S wanna live my life (I gotta go)
Yeah waste my time (awma time bimay waste)
Waste my time
Just tryna live my life (takeu diogu dox)
Yeah waste my time
No don't waste my time
Boudé thiaxan nala yeukeutii bro
Please gnian nala ko
Thiane bi ngi nana ndo di waste time
Balnala ko
Yitéy magoum dieumeu
Boudoul farata nulle cii néne
Lii téy magu mou gueum dou doul you fara
Magoul cii brain
Gnémé kharé tax gnou taxaw
Sandiafou bal ci deuneu
Diogu fakhassou dox
Lignou yitél moy ligni séntou
Fimou taré lagnou waré
Déff toubéy yii beuneu
Gadou ndam li yokh
Toul cii brain yii
Fente senkou
Boula dara wara mana
Téré dox sa dox
Priorité la wara doon brother
Lou nekk ak waxtoom
Wala bouni tén
Gadou pél gas ba dadj ndox
Mbegu soubag ngoon
Fadj ta réy sakhou goom
Donté att yi new na
Na fagou doon mag cii xél
Hapeu digui guew la ndiateu ragal
Khoufate ko ndel
Fréné xél yii defko endurance
Infiniment you wais
Step by step yékk diko worse
Bagn bok ak gagni caisse
Come on
Just wanna live my life
Yeahhh was my time (awma time bimay waste)
Don't waste my time
Self tryna live my life (takeu diogu)
Yeah waste m'y time
No wéne waste my time
I just copy to the back
I just wanna go shut the moon
I don't wanna fall
Wanna end a park up
To go get it soon
Need you to stick around
Everywhere I go ay
Get in your mind that the struggle end yet over
Forget everything I know in
I get to find the middle
To cross river
Well realize
All disappointed well recognize
The real than a though
I know we gotta gooo oooo
I know what I gotta knoow oooooo
The opponent I don't wanna be late
I wait to the lord
I don't wanna be late
Just wanna live my life (I gotta go)
Yeah waste my time
Don't waste my time
'S tryna live my life
Yeah waste my time
No wene waste my time
Yoon sorri leudeum
Ratakh barii diam diam
bokou gnou dieum dieum
Boul diéma sopi sama gueum gueum
I don't wanna be late
I don't wanna be late
Rédigé par Real G



Writer(s): leuz diwane g


Leuz Diwane G - Diagnosick (The Firstep)
Album Diagnosick (The Firstep)
date de sortie
10-02-2015




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.