Lucky Thompson - Street Scene paroles de chanson

paroles de chanson Street Scene - Lucky Thompson



Back in the days, Yeubo TEAUPLA
Yeah Soweto Boys, ARRA
Danga dof wala lane? Danga tokh wala nane?
Haha niou dém?
{COUPLET 1}
Rap bi khèwi na? Yeah mako dékkilate,
Di nga diappeu daadj, ni kou naane verrou tekila!
Mane mi, maye yeubo town bou gnémé djeggui rail
Hey bilaye souma done ragal douma def lou regular!
Amoul règle, noko feelé nga def ko,
Tant que ya ngui créer na tchi téyé affaire bi deme kow
Bokkoumaak grand yi laye djémma tekk ledea (deaal)
Pour outti groupie bouniouy foutti gouddi tek le dickkk
Est ce que Africa am ne show biz?
Est-ce que am ne marché? Est ce que diar ne show fils?
Wawaw gni gueuneu chaud gning tchiy get doe
Guiss na aye CEO you diogué tchi ghetto
Diaroul salamalekoum, Team bi fi gueuneu nice game moye yobbalé coupe
Yagg nala yeff wayé légui dem le faalétoul
Nekkatoul Jammdongg Elz defe baalétoul
Je m'en bats les couilles
{1}
TeauPla we the craziest, Rue Fleurus we the craziest
Wa Square we the craziest, yeah Rue Valmy we the craziest
Rue de Bayeux we the craziest Félix Faurre craziest
Han Grasland we the craziest Rue Carnot we the craziest
{COUPLET 2}
Li ngay bénieu degg moye Free guenné hit
Ngamey get in the petto mey get bénéfice
Fonkk Motherland loumfi sori sori di guiss
Biss bi mey gnibissi fils wara thiéné fii
Noumou démé ni, Nioune ngay diémeu gêner fils?
Yow degn le dane tédj bimey yèndou négou Piss
Tèle na kham bégué diapp plizz
Tèle na déglou reggaee, rap disques
Ma ngui tchi ay tankkou tek ndiss
Togg bamou nior niou dogueu doreu get G's
Am ne niou deggueugoul yokkeul son bi
Soroumeu goalou meu wolou na semey complices
Shégué baayi niou niou bégué
Bou li togne tchi yow ley diogué soril bou fi diégué
Diagg bou beugg djiguini degn ley sotti balai-souy
Nekkatoul Jammdongg Elz defe baalétoul
Je m'en bats les couilles
{2}
Sénégal we the craziest Mauritanie we the craziest
Yeah Guinée Mali we the craziest, all west african craziest
{COUPLET 3}
Yeah mane deme dof deme dof deme dof
Yobou negn me Fann mais deme colle force
Talal mic rek me def ko thiébou night (Bolou dof)
Talal mic rek me def thiébou night (deme koy thiobe!)
Yeah mane deme dof deme dof deme dof
Yobou negn me Fann mais deme colle force
Talal mic rek me def ko thiébou night (Bolou dof)
Diokh me mic ak seme pairou NIKE
Me wone le techniques, domeu sakh tek nit
Bégnkat beg si, Koumey téré tek hit?
Niouné doumeu nit? Evident deme loco!
Victimes yi meu def ak seme team amou loko!
#Dexter mako yagg daggaté, doumeu meusseu daggalé
Deggo meu me daggal ndèye khél ngama ragalé,
Abalèl bala maley shoot (poo)
Amél ngama akkh nieuweul seme gallé toube
Indaalé coupe
{3}
Ndakh Jamdong we the craziest, Mister Thiere is the craziest
Belzo Kamzo craziest Mbarody and Faya craziest
Yeah CEO be the crazies, t the finest and the craziest
Yeah the realest and the craziest, I'm the finest and the craziest!!
{}
Aight shout out to my day-1-followers, Teaupla fellaz
Mey ko seme grand yi takh kham RAP
Gni me diam Naughty by Nature, Soweto Boys
Danga dof wala lane?



Writer(s): Lucky Thompson


Lucky Thompson - Brown Rose
Album Brown Rose
date de sortie
01-01-2000




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.