Majestic Drama - Yagg Na (feat. YoungTili & Omzo Dollar) paroles de chanson

paroles de chanson Yagg Na (feat. YoungTili & Omzo Dollar) - Majestic Drama



Yagg na
Depuis temps wou daww demm salle de jeux
Xalé you ndaww, beuri fitt wowone beut
Ça le fait comme ça le veut comme ça le peu peu
Ya ma nguembone, maye sa mbeurr
Yama done wax TILLI ya léne meune
Lolou nga gueumone, lolou nga yeukk, lolou moye deugg
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu
Niata deal laa gnu teudeul?
Da gnio faxass, lepp lagn raxass pour rek mbapat
Ay boy you Dakar, fall ya tax ma rap-ate
Beuguone tabax, gnou gnuye dambate
Yonn naakar
Ouuuh Ouuuh! Teye amna buzz nigga
Doul lo nagnou sugnuye nonn, niome dougnou fuck nigga
Dama la watone fii ma léké, di nga fa lekk
Mais guène nga adouna néko sama wett
Sama xol yeugeutoul
Dama dioye ba rogogne tourotoul
Bagne léne ma ndaxx mbeguel doyotoul
Yeah yeah!!
Sama xol yeugeutoul rogogne tourotoul
Mbeeeguel doyatoul
Yeah yeah!!
Yagg na
Depuis temps wou daww demm salle de jeux
Xalé you ndaww, beuri fitt wowone beut
Ça le fait comme ça le veut comme ça le peu peu
Ya ma nguembone, maye sa mbeurr
Yama done wax TILLI ya léne meune
Lolou nga gueumone, lolou nga yeukk, lolou moye deugg
Ça le fait, comme ça le veut, comme ça le peu peu



Writer(s): Abdoulaye Diop


Majestic Drama - Yagg Na
Album Yagg Na
date de sortie
18-03-2022



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.