Nitdoff - Fokk Ma Lathié paroles de chanson

paroles de chanson Fokk Ma Lathié - Nitdoff

Fokk ma lathie!!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo! Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou
Tontou
Fokk ma lathie
Fokk ma lathie
Loutakh léppeu keupou ci mane
Loutakh maay xeuy di wékou cii nit kèn dou
Wéku cii mane
Loutakh may xeuy di tèneu di xoll douma sèneu
Assamane
Loutakh sama life tiss nioumaay xolé beutou
Ndeyesane
Daniou maay khép douniou maa guiss daniou
Maay rombe seun
Maay gueuneu nour si guédjiou nakkar, he can't
Understand
Sama fiit meuneu toul tokk ndakh ay yakaar you
Tass
Dama aay gaaf ci pét wala ma niaka daw fass
Sama xoll di diékh vide nii sama calpé
Niak singuilima foutima dima palpé
Sama doundou wét melni ndiouly bou amoul salbé
Maay xeuy di lathié louma def ba mérité li
Mba dou sama liguéyou ndéye cii la herité li
Bissbou nek limouy indi cii ay khétou problème
Diougué Tchii li danou tchii da ngay djiém do
Dém
Niou ték la yafouss
Vaut rien bi tekki wo touss
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo! Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou
Tontou
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss kou tontou
Lou lakhe ma ndagou sakou am am di xeuy di
Gontou
Meunone def ni niome tokk cii Boppou kogn bi
Fontou
Beuri diom maa takh ma bania tokk si keur gui
Nioumaay khonetou
Fouma démé baye aamé yakar life bi dathie ma
Pontou
Maa danou waatt cii kambe gui Tambalé waatt à
Zéro
Souma ko diappé ni dina yékha warr Pagérot
Saalite-tangue maay yott seung sama geueme
Felleu
Mougn na ba sama mougnou kaay fessena Delleu
Magui cracké tchii yonu sinébare ak guène Braqué
Sama égo yegg naa boppam Beutt yi nioma traqué
Di blamé Baa cii askane wi ma bokk dagne maa
Plané
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liiddé Kagn Lay Diekh
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Yo! Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diékh
Who? my nigga
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh
Yow! Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou
Tontou
Fokk ma lathie
Souma Néwé ciii geunte Feugue maa néma
Diougeul
Mane Limaay dounde ni natou leu wala mbougeul
Tamouma di Loubeul damaay Liguèye di dioubeul
Cii ndiguel la meusseu sakh di moytou loumay
Diggeul
Souffél sama bopp kouma guiss Daadi laay
Yégeul
Waayé melnani taay yoyou djiko niomay téggeul
Bonne daffa yombeu
Beuri wonne neu loumay diombeu
Beuss bou niou khassma meu sa morom
Yagui laay rombeu
Nit gni danio yakamm ti ta yalla daffa Yékh
Ko tchii wakh Mouné leu Def lou bakh mofii diékh
Bène lakk laniou dégue mouy CFA
Boka yoroul légui Le courant ne passe pas
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liiddé Kagn Lay diekh X3
Fokk ma Lathie Lathie lathie Ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie!!! Liiddé Liddé Kagn Lay Diekh X3
Fokk ma Lathie Lathie lathie ba guiss Kou tontou
Fokk ma lathie
Lathie ba guiss kou tontou
Fokk ma lathie

Writer(s): Nitdof, Papa Kandé Sidibe ( Mao )

Nitdoff - Rddr
Album Rddr
date de sortie
16-06-2013

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.