Nitdoff - Keep It Real - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Nitdoff - Keep It Real

Keep It Real
Keep It Real
Boule meussa taukhe baune, Boule meussa naane

Wine
Wine
Boule meussa doone fake founioula fékk dél clean

Boy dokh déél sigui, di represent saa City

Boule niakk geumeudi wala xeuy rék am daadi sipi

Del khool sa nitou dembe bi dara doonul léne

Sèn loxo nga done yendou gnola gnanal dila ngémb

Please Nigga stop siggil nga goré
Please Nigga stop siggil nga goré
Dindil li nga fook ndakhté life bi day woré

No Matter, what the deal you got keep It Real

Kholléne si Beut ak Beut diléne téggal lingay Feel

Déél Wout di diokh sa Mother, Diémeul woutou sa

Father
Father
Tchii galé lou nara gnaw nga diouk tchi telko

Faadeu
Faadeu
Boula show bizz bi goûté ba ngay nakh gni nga

Djité
Djité
Ndakh Démbe ak légui yaggoul mais say discour

Dafa wouté
Dafa wouté
Wakh tchi mbakhou kénène dou yakk tchii sa

Mbakhe
Mbakhe
Toumeul nit loumou défoul dalay Topeu tchi saa

Pakhe
Pakhe
{Refrain}
{Refrain}
{2ème }
{2ème }
King Killah tchii Ring bileu, Mbede bi ak feeling

Bileu
Bileu
Sedd bi ak didim bibleu, Kii ngay djiteul cii liim

Say nigga dagnii pop, Samay nigga dagni ndiapp

Yegg yegg lagni démé, Dou kou nekk lagni aimé

Dagni raay dadii tamé, Ay hit rek lagni diamé

Mouy régue wala affamé, Gaïndé yapp ngako xamé

Dotou maa waulou jamais, Ndakh daniou
Dotou maa waulou jamais, Ndakh daniou
Domouramé
Domouramé
Niata nga dimbeuleu niou weulbeutikou dila dialé

Ay toxico kii kamé nioy tok di lam lamé
Ay toxico kii kamé nioy tok di lam lamé
Louniou laa xamal cii mbaute cii gran place yi

Laniou koy samé
Laniou koy samé
No no boule def ni niom, Gorr waroul niakk diom

Bou até déssone tchii mane maa timelène ak

Makoudaume
Makoudaume
Sa diante dina shine, boule yakamti sa time

Boula daray aduna diaral fils ngay wor gaïneu

Mane ak yaw bougni boy, Sunuy ak sunu djoy

Taay lep néna saay waral sama xoll bi toy
Taay lep néna saay waral sama xoll bi toy
{Refrain}
{Refrain}
{3ème }
{3ème }
Hann Yeahhh!!!
Hann Yeahhh!!!
Lepp loy yéné nit kii Na done affaire bou nice

Songue life takk fiit bi nangou def aay sacrifice

Yonou goor dafa métii, Nioune nieupe beug tekki

Boule dém dii tiogue kèn sinon yalla dalay djépiii

Bodéé fake nigga get out my way
Bodéé fake nigga get out my way
Nioune douniou Holla kène kou doul real all day

Amouniou diotou tokk di feinte bullshit
Amouniou diotou tokk di feinte bullshit
Talou niou loudoul job tchinpeu baa tiow djipp

Saay none louniou téné, rebellou laniou laa yéné

Boule sakh di fayonto kone dafay takh nga aliéné

Niom daniou lazy (paresseux), Faarlou wouniou

Niii Jay-z
Niii Jay-z
Fi cii guétou rap niouy doundeu ak mane tchii

Hypocrisie
Hypocrisie
I know nigga dialoré yi lay tek
I know nigga dialoré yi lay tek
Rangalé yi succès cii albums you High-tech

D-d-d-d-d Squad di karanguéy my back
D-d-d-d-d Squad di karanguéy my back
Nokoss Di Rok My chek my tek
Nokoss Di Rok My chek my tek
{Refrain}
{Refrain}

Writer(s): S. Carter, Gloria Stewart, Phillip White

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.