paroles de chanson Highlander - Nix
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Dague
sene
boppe
lay
def
Highlander
Décapité
par
le
chef
Highlander
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
bayi
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Fou
niou
dougou
ma
lidjenti
lene,
Mane
késsé
boy
kene
dou
ma
donneu
Niou
yeungou
ma
dagati
lene,
ngene
sorima
lo
ley
lou
dagane
Y'all
don't
wanna
live
(Y'all
don't
wanna
live)
Bou
may
dioudou
rap
dé
amagoul,
Fii
la
ma
fekk
ni
seeni
doule
Ma
impermeable
ci
yeah
dama
toul
té
nope
bou
nathioul
dé
dégagoul
Baggy
jeans
Wu
Tang
diamono
May
battle
di
Battle
di
battle
Freestyle
ma
lay
golo
lo,
May
danel
di
danel
di
danel
So
ma
wédé
laadj
ma
Xuman,
t
Ekk
ay
flowou
Busta
mel
ni
dou
mane
Au
final
yakamti
pour
lane?
Periode
bobou
dam
ko
djegui
ni
dos
d'âne
Néka
gouma
artiste
solo
mais
ma
ngui
ci
game
bi
ni
gaindé
bou
souroul
Di
dougal
ay
MCs
ci
biir
kilo
mbourou
Di
dokhontou
ci
kogn
bi
di
weur
ay
foureul
N-eazy
defal
ndank
lou
eupeu
tourou!
Ma
keupeu
yelwane
bi
sama
boy
yi
djiiro
Surveillance
générale
la
bagné
Bureau,
ndékété
mariage
dafa
wekh
ni
gouro
Dou
ma
la
djaay
experience
boy
amo
ndjeugam
Degn
ma
yarr
boy
xebouma
deureum
Degn
ma
nokhe
boy
ba
tay
may
geureum
Golden
boy
dama
nioul
ni
peureum
Longévité
boy
dou
serigne
dou
mara
dou
téré
dou
garap
boy
défo
fii
Dara,
dou
palace
dou
baraque
Dou
Donald
dou
Barack,
dou
Point
E
dou
Karack
Lou
gnou
cons
boy
dou
diaraat,
laadjal
Egypte
boy
fou
gnou
tegone
Mubarak
Mais
Yallay
buur
sou
ko
nékhé
gnou
faraat
Kone
N-eazy
bayil
sou
la
nékhé
nga
dieulaat
...
Ndakh
yaay
vieux
père
bou
doul
maguete
Highlander
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Dague
sene
boppe
lay
def
Highlander
Décapité
par
le
chef
Highlander
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
bayi
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Fou
niou
dougou
ma
lidjenti
Lene,
mane
késsé
boy
kene
dou
ma
donneu
Niou
yeungou
ma
dagati
lene
ngene
sorima
lo
ley
lou
dagane
Y'all
don't
wanna
live
(
Y'all
don't
wanna
live)
Katana
bi
lou
mou
dagati
boy
rawna
dibiterie
Tête
de
mort
nekone
fi
tendance
mais
tout
C'que
je
voyais
c'est
mes
trophées
qui
me
sourient
Quickening
Flow
bi
mo
déloussi,
Boy
ay
éclairs
lay
cons
melni
Hennessy
Rap
Galsen
sama
dom
on
est
Père
et
fils
Mamou
mamati
mamou
sene
lyricist,
ay
seut
flow
therapists
Kou
fi
attane
sama
legacy
neu
tekki
térém
dérèt
takhal
yérêm,
bann
Bi
takhal
bérem
balles
yi
takhe
tat
tat
tat
tat
Boy
niou
teureul
leen
yene
ak
sene
kheureum
fils
Équipe
bou
fees
ak
ay
génies
fils,
d
O
ladj
Orange
lane
moy
bénéfice
Do
ladj
wa
Yonkers
Kouy
Jadakiss,
Défaite
bou
ley
fegnou
do
ko
teela
guiss
Té
longévité
boy
dou
méyé
dou
sarakh,
dou
Jordan
dou
thiarakh,
Dou
khegn
nekh
dou
forokh
mais
toujours
frais
comme
le
vieux
père
Rey
la
ak
sourire
ni
Joker
Highlander!
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Dague
sene
boppe
lay
def
Highlander
Décapité
par
le
chef
Highlander
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
bayi
Highlan...
Vieux
père
bou
doul
maguette
Highlander
Fou
niou
dougou
ma
lidjenti
Lene,
mane
késsé
boy
kene
dou
ma
donneu
Niou
yeungou
ma
dagati
lene
ngene
sorima
lo
ley
lou
dagane
Y'all
don't
wanna
live
(
Y'all
don't
wanna
live)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.