Omzo Dollar - Nitté - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Omzo Dollar - Nitté




Nitté
Nitté
Yea
Yeah
Enh
Enh
Nitt yagui cii biir niit yi da mel nii yapou t'a len sourr
Nitty, we're all in the same boat, rowing towards the same shore
Niit'ay dougal niit safara dika nakhat aldiana cii kaw souff
Nitty, we're all travellers on this dusty road of life
Pithie mogui ci kaw wanté khel bi yeup bi yeup'a nek ci souf
Woman, we're all struggling to find our way in this crazy world
Kou dougou ci cage day fok ci biti mo dioum
Man, we're all trapped in this cage, trying to break free
Lane lalay wagnil yaw soma yokalé
Lady, we all have our hopes and dreams
Baloumoy tall yaw dina fay sa yéné
My dear, we all have our fears and insecurities
Khana soy rafet dafay takh ma gnaw
Darling, I know you're hurting, and I want to help
Kou kawé dafay touti cii kou mounoul naw aboz'er
Man, I'll be there for you, even when life gets tough
(Ndakh mala gnou gueuneu nitté 2x)
(But baby, why are we so mean to each other? 2x)
Seytané wakhoul deugg gniko degglou na yakh sen khel
Lady, the devil is trying to trick us, to turn us against each other
Requins yi guéné djiko caïma dinagn done ay diane you matteu sen guéne
My dear, the sharks are circling, waiting to tear us apart
Gaïndé dou falé kouy you bokk mbarr
Man, we're all in this together, we're all on the same side
Dieune bou dawci bou mak rek done
Lady, we need to look out for each other
Mala boudoul diamou yallah amoul
My dear, we need to pray to God for guidance
Pourtant allakhira souff rk lagnouy done aboz'er
But baby, it seems like we're all lost and confused
(Ndakh mala gnou gueuneu nitté 2x)
(But baby, why are we so mean to each other? 2x)
Guissna ay mag'ak birou khalé cii birr ay khalé you biral ay khalé
Woman, we all have our own unique gifts and talents
Dagn sathione sougnou enfance gnou magg gnouy sathie sougnouy enfant
My dear, we all have our own stories to tell
Boul dougal khadiou mbedd cii sa keur 2x
Man, we all have our own dreams and aspirations
May la sama mbokk dou takh gnou done couzin
Lady, why can't we just support each other?
Loup ba ngui cii poulailler bi'k sourrir bou jaune poussin
My dear, why is there so much envy and jealousy?
Aboz'er
Baby
(Ndakh mala yégnou gueuneu nitté 2x)
(But baby, why are we so mean to each other? 2x)
mala yégnou gueuneu nitté
Oh baby, why are we so mean to each other?
Dama barri louma mounoul expliqué
Please baby, let's talk about it
Quelle mouche nous a piqué
What's gotten into us?
Nitt bougnouy diamou ay kharr rk lay djité aboz'er
Nitty, we used to be so kind and loving
Enh gni sante séni tour lagn gueum
Enh, what happened to our sanity?
Kou khéssal dagnla tour leundeum
Man, we're all so caught up in our own lives
Sou goudou nopp takhone dégue kéne dou door mbam
My dear, we've forgotten how to connect with each other
Sou déssoul loudoul fass sa kanam daw do fallé dos d'âne
We've become so isolated, so disconnected
Mono mouss ba gaïndé done bouki
Lady, we're missing out on so much
Wanté kagna rat de keer gnou nekk chauve-souris oh
My dear, we're losing our humanity
12 gnou merr lo peundeul mou cedd ndakh khol bou
1 2, we're all just numbers now
Diekha'k deunneu bou fess lo dieunde dou dess boul tipcé
My dear, we're all just faces in the crowd
Limité sougnou nitté yeup ci succès
Lady, we're all so obsessed with success
Succès ci sa diné dinga distrait
My dear, success has become a distraction
Distrait ba dall ci mur mel ni cindakh
Man, we're all so lost and confused
La tête loin des epaules girafe
My dear, we're all so far from home
Ame kham kham mandou wo moudié done serr
Girl, our souls are so empty
Kou ame cher de poule gnou deff poulet de chair
Man, we've become so superficial
Sa succès sa none lay dane
Lady, your success is killing you
Golo'k allumette bone lay tall
My dear, your vanity is blinding you
Yallah mom lici kanam boy diégui khol sa droite t'ak sa gauche ba
Baby, please, let me help you
Safar beuri gnifi defoul'one long feu
My dear, let me be your guiding light
(Ndakh mala yégnou gueuneu nitté 2x)
(But baby, why are we so mean to each other? 2x)
Yeh mala yégnou gueuneu nitté
Oh baby, why are we so mean to each other?
Dama barri louma mounoul expliqué
Please baby, let's talk about it
Quel mouche nous a piqué
What's gotten into us?
Nitt bougnouy diamou ay kharr rk lay djité aboz'er
Nitty, we used to be so kind and loving
(Mala yégnou geuneu nitté 2x)
(But baby, why are we so mean to each other? 2x)





Writer(s): omzo dollar, flagrandelit


Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.