paroles de chanson Xel ak Xol - Omzo Dollar
Sama
xol
moma
djitale
xel
tekk
ma
ci
yone
wawawa
Sama
xol
moma
djitale...
Diarignole
sa
xel
do
meussa
diawalei
bayi
xel
bayi
meuna
yobalei
Diarignole
sa
mind
do
meuusa
diawalei
bayil
xel
bayi
meuna
yobalei
Xel
moy
nitt
tei
mola
meuna
djitale
ba
doto
diawalei
Xol
moy
nitt
tei
mola
meuna
djitale
ba
doto
dia...
Xol
ak
Xel
Alale
ak
xol
sol
ak
ciel
alale
ak
sole
nou
yeuk
Ayeuk
meile
fou
xalate
tole
mbolo
nk
ba
melni
taw
ak
tole(Bis)
Wawaw
dinga
diare
ci
selebeyoon
yeine
sayi
yeine
sayi
Nguir
nga
xam
finga
dieum
wawaw
wawaw
boko
deifei
magg
waw
Mbeuguel
lay
goumba
lo
mais
neinagn
xol
lay
guissei
Xel
bou
nior
xol
bou
neupp
andoule
ak
nitté
Xole
ma
ak
sa
xol
waxma
lane
nga
guiss
Boudé
lou
bone
ngay
xolei
lou
bone
rq
ngay
guiss
So
amei
xol
bou
tass
sama
xel
day
worry
Sa
yo
dieguei
sama
xol
sama
xel
day
sorii
Kone
xolma
ak
sa
xol
waxma
lane
nga
guiss
Boudé
lou
bone
ngay
xolei
lou
bone
rq
ngay
guiss
Diarignole
sa
xel
do
meussa
diawalei
bayi
xel
bayi
meuna
yobalei
Diarignole
sa
mind
do
meussa
diawalei
bayil
xel
bayi
meuna
yobalei
Xol
ak
Xel
Alale
ak
xol
sol
ak
ciel
alale
ak
sole
nou
yeuk
Yeuk
meile
fou
xalate
tole
mbolo
nk
ba
melni
taw
ak
tole(Bis)
Xel
day
xalate
ba
yei
ma
ci
nelaw
xol
daye
Rafett
oyof
melni
nguelaw
soudone
deukk
na
dem
(bis)
Anh
xel
rq
la
sama
xol
bi
di
wolou
Souma
sagnone
ni
pepp
souff
la
sama
xol
bi
di
toleu
Sama
xol
yaramou
neine
fi
sama
xel
bi
di
solou
Sama
xol
da
gatt
xel
ba
sama
xel
bi
di
xolou
Fou
xel
bi
di
sorou
xol
lay
nelaw
xel
bi
di
seulmou
Boul
meussa
fatei
xol
lay
diap
wayei
xel
moy
coeurou
Xol
ak
xel
sougnou
beurei
sama
xel
bi
moy
dane
Dougal
sama
bopp
si
SEAU
'wou
acide
sama
xel
bi
dou
PANNE
Abozé
Gnima
def
sen
xol
gnoungui
sama
xel
Gnima
geuneu
def
sen
xel
nekougn
sama
xol
Xol
lay
deglou
xel
di
tektel
Sama
xel
lay
tek
xol
fou
sama
xol
di
tekk
xel
Sama
xol
day
xalate
xeli
xoulo
fepp
fou
xel
diarr
Damay
rap
ni
kou
ame
gnarri
xel
boul
ame
xel
gnarr
Boul
ragalei
xel
tanki
rq
la
fitt
bi
di
daw
Na
sama
xol
taxaw
mais
jamais
sama
fitt
bi
di
daw
Xol
ak
Xel
Alale
ak
xol
sol
ak
ciel
alale
ak
sole
nou
yeuk
Yeuk
meile
fou
xalate
tole
mbolo
nk
ba
melni
taw
ak
tole(Bis)
(@$#)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.