One Lyrical - Todj Sa Monde paroles de chanson

paroles de chanson Todj Sa Monde - One Lyrical



Dokh kat dou féké déwou maa-mame
Dama peundeul kaw ak suuf xalé yu djiguène nioma def ndanaane
Meuneu fèèn! ngané yaa mom yéré yi yoro soukeur ak naana (Bayil fènn)
No toudou ngané Mara quel faux prénom mana Ndiaye Maana
Doudou Ndiaye Rose mi déh sama maame leu
Gueumou Kocc Barma lima beug moy def tat guéweul yi darma
Makoy sédeulé ni barman, niari werra ngi ngamay toppeuh lanela
Xalé bou rafet darma, sama nëk dafa am vitamine sawarna
Xaliss partout douma worr mbaam bou mako ndaré def Yallah nama Yallah dji ray mane
Dama léna xepp ak séni party
Samba Party ak Modou Party yéneu beug party
Damay xeuy ci piscine yéndou ci jacousie
Dama am alale boléna laak samay cousine
Je ne peux pas parler de gauche à droite
On ne peux pas plaire à tout le monde basta
Ce n'est pas la peine de couper tes rasta
On dit que "L'Habit ne fait pas le moine"
Mais saa bouma lèn guissé am envie guéné sarakh
Macky Sall sama xartitou papa leu namouma thiarakh
Mane namouma thiarakh Namouma thiarakh
Damay toth sama monde, Damay toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Damay Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Carré VIP amoul guétou bëy
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Carré VIP amoul guétou bëy
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sa monde
Da nga tek deal sa yaay tek deal sa baay
Niaak djom amoulo Mari (yaw amoulo Mari)
Koumako nétali? fi nga diaar damako wessu
...Ya ngui aubeuli
Say nélaw doyoul FALL da nga melni kou Palus
Weur di xepp mbalite, SWAGGou talibé nga yorr boy da nga xégne mbalite
Haaaaa!
Sama guémigneu fraiche ni glace
Xalé Nicki Minaj ma géré beugoul ma sori
Viré nama Western Union
Haaaaa!
Sokhor braquette ni Fast Last, amena diouromi dom amo gouma diabar
(Astakhfiroulah! Bayil doul nigga)
King of battré douma dougou soirée sénégalais dafa beuri cas social (No No)
Douma sétane télé awouma temps ni Eden Hazard
Toth na Lille, Toth na Chelsea, Toth na sama équipe Nationale
Toth na bercy, Toth Jet Set Elu, Toth Zénith
Mais ci pet dafa échec ni Wally
Farama rènn laa bayilèn ma way (Bayilène ma waaaaay)
Sabaribi raara sabaribou rouu
Manela sama Papa yoré faux billets
Sac à main laay doxonto sétane meu wiri wiri
Damay toth sama monde, Damay toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Damay Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Toth sama monde, Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Carré VIP amoul guétou bëy
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sama monde
Carré VIP amoul guétou bëy
Kaay Toth sama monde, Kaay Toth sa monde



Writer(s): Dr


One Lyrical - Sélébéyoon (The Difftape)
Album Sélébéyoon (The Difftape)
date de sortie
22-09-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.