Samba Peuzzi - KIRIKOU paroles de chanson

paroles de chanson KIRIKOU - Samba Peuzzi

Eie, yo
Yo yo yo yo yo
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damkoy diokh boram
Karaw bou nioul la bop bi mako teinte
Kone niakouma dara tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais...
Do pression ni tatou kirikou
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est
Fils dama percer nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est
Khathi do door do maté yay Scooby-Doo ma
Nélau ci game da beurri ay karaba
Yi ma done Oggy dakh fethi comme ay cafard
Pour peuzzi géneu Reptyle fauk titeuf lale Nadia
Dane mofi snap, yay screenshot souniouy discussions
Nel gni sandi kher souma guesto da fek shoe bou am tatte romb
wone da pairou daleu trois cent milles laye sol key
Sen pussy guel, sama power bank, peuzzi dou meussa faye
Dam si done fo, tay mansi jono joni ay broh
Guéné fi yah! yah!, ioe ba dagmay deuk barro
Athi barre bi sikaw taok fa soul rek ka may boleik souf
Doigt d'honneur pour yen nieup modafuck old of fouf
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damkoy diokh boram
Karaw bou nioul la bop bi mako teinte
Kone niakouma dara tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais...
Do pression ni tatou kirikou
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est
Fils dama percer nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est
Contoler sa zone, sa wa kogn dagn la rouge
Ma ngui def lou lerr avant mey bédiaw na am khaliss bou wékh talleu
Lokoto oute niossi bo yem douma nangou done khalé
Nénagn time is money, kone niak, diote moy mayer khaliss
Awma nélaw goudi lay job nathi damy guéméntou lo
Leundeuma lerr leg ma leundeum sans ma photo grey
Buzz'ou une semaine pour niom clash ma moy takh niou siw,
Sokoy tangual boul dougeunté niom sinon dagn lay barbecue
Partant par force nangou sa posta nga tokk banc
Sandi pic sampe nul noonoo mane néwouma si yi
Rayla mayar sa barre sa bountou gallé feth
Wondél di battle sa mère nanko siguil ndigalé
Kheuthio len couronne bi mane CFA rek lay guiss
Talal lokho mère mofi dièkh légui damkoy diokh boram
Karaw bou nioul la bop bi mako teinte
Kone niakouma dara tolagouma sama digou ndeundeu
Di def son you nice, khalé makk di noce
Fils mankoy tothie ioe ngey sissou mais...
Do pression ni tatou kirikou
Do pression boy ni tatou kirikou
Mane dama feuleu nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est
Fils dama percer nieup youkhou l'eau est
L'eauuu... l'eau est

Writer(s): Samba Tine

Samba Peuzzi - KIRIKOU - Single
Album KIRIKOU - Single
date de sortie
08-02-2019

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.