paroles de chanson Sans Yaw - Sir Malik
Hum
hum
Yaw
rek
la
love
Meme
souddé
meussoumalako
wax
Ya
né
thi
sama
xolle
Meme
souddé
meussoumalako
wane
Yaw
rek
lay
khoole
Dou
kénéne
koudoul
yaw
Oh
dafay
geun
di
fort
Sama
mbeuguel
si
yaw
Sama
yegg
yegg
si
yaw
Oh
baby
Tallouma
tallouma
Wagnii
ay
bideew
ndakh
werr
bi
si
sama
wett
Girl
i
need
you
by
my
side,
side
Khamalni
yaw
baby.
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
Baby
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
Bayima
ma
done
Ngélaw
biy
raye
sa
yeram
Bayima
ma
done
retane
biy
fegn
sissa
kanam
Bayima
ma
done
diant
biy
leiral
sa
life
Baby
so
khamone
yeah
Sama
mbeuguel
si
yaw
Finga
tolle
si
man
Baby
Tallouma
tallouma
Wagnii
ay
bideew
ndakh
werr
bi
ngi
sama
wett
Girl
i
need
you
by
my
side,
side
Khamalni
yaw
baby.
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
baby
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
baby
Dedete
sama
life
sans
yaw
Khamalni
yaw
baby
Oh
baby
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
Sans
yaw
Beug
nala
demb
bala
tey
di
nieuw
Yalla
defna
lolou
Imaginewouma
ben
yone
Sama
life
sans
yaw
Sans
yaw
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.