paroles de chanson Nobal Ku Lë Nob - Titi
Wouy
mbeuguel
loo,
anh
mbeuguel
Wouy
mbeuguel
loo,
anh
mbeuguel
Bala
ngay
nobati
iao,
nang
ko
xol
Bala
ngay
beugati
iao,
nang
ko
set
Ndax
so
beugueii,
so
beugueii,
nguru
ngaa
Bala
ngay
nobati
iao,
nang
ko
xol
Bala
ngay
beugati
iao,
nank
ko
set
Ndax
so
beugueii,
so
beugueii,
nguru
ngaa
Dangay
set
gninga
bayi
ba
am
ci
ay
noone;
Mane
ma
xol
gnima
bayi
na
am
ci
ay
noone
Nonu
nga
donei
sama
matadi
Ba
sumala
jissul:
baby
damay
manquer
Inquiéter
wu
sumala
seinei
ak
kenen
(fok
nga
sip),
Wayei
manit
na
dal
ndax
numa
dieufei
wathié
sama
personnalité
Lumeu
meuneu
don
yafi
nei
Bala
ngay
nobati
iao,
nang
ko
xol
Bala
ngay
beugati
iao,
nang
ko
set
Ndax
so
beugueii,
so
beugueii:nguru
ngaa
Bala
ngay
beugatei
Nob
kuleu
nob:
dara
dakuko
Beugal
kuleu
beug:
dara
dakuko
Nobal
kuleu
nob:
dara
dakuko
Beugal
kuleu
beug:
dara
dakuko
Dara
dakuko,
dara
dakuko
Nobal
kuleu
nob:
dara
dakuko
Dara
dakuko,dara
dakuko
Beugal
kuleu
beug
dara
dakuko
Enh
beuglen
Xana
du
mbeuguel
leuu
Mane
nena
sumako
pognet
du
dem
Mane
malay
décoder
ndax
danga
coder
Hôpital
buma
diar
niu
xalil
ma
yon
Ndax
médicaments
yalay
fathie,
mane
malen
kay
diox:
ma
gueun
ci
iao
Guedj
gui
sax
dafma
xamei
Vagues
yi
don
samay
xarit
Nguelaw
li,
pithe
yi
naw
ehh
May
sen
natagoo
WhatsApp
bi
nga
saalo
Ba
xolatoma
dima
zappé
Viber
bi
nila
won
Ba
sumalay
by
by
Doma
xol
man
Ennnnnh
wouy
mbeuguel
looo
Nobal
kuleu
nob:
dara
dakuko
Beugal
kuleu
beug:
dara
dakuko
Nobal
kuleu
nob:
dara
dakuko
Beugal
kuleu
beug:
dara
dakuko
Dara
dakuko;
dara
dakuko
Nobal
kuleu
nob:
dara
dakuko;
dara
dakuko
End.
1 Nobal Ku Lë Nob
2 Jikko
3 Sa Ma Mbëgel
4 Ndindy
5 Maay Sa Seytane
6 Aduna Ni Lë
7 Stay With Me
8 Tamit
9 Naby
10 Ndindy (Acoustique)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.