Youssou N'Dour - Habib Faye paroles de chanson

paroles de chanson Habib Faye - Youssou N'Dour



Aduna du dara dara khadiufi bilae
kouko diap khamal ni diaposi dara (bis)
Mane youssou niak na endano bou sincère aduna aduna dal nakhati naniu
aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna
Habib yarou wone na Andak dignité
fokone na liguey beugone na ligueyeum
Fonkone ndiabotam donone diambar
Mane youssou niak na andando bou sincère aduna aduna dal nakhati naniu
aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna
Habib habib
Damako dieulé l'école andiko super étoile mou deugeul
Mane dh mang len koy dial yen wa famem ak ay fans am habib habib
Dilen di khamal ni habib faye diougué woufi
Niofi defone mak mom lutaxone gnigni beugone ko
Khallé yagui lay dioy mang nia
guilay dioy africa guilay dioy habib habib
Sama beug beug moy li sa beug beug moylé niit kouné
beug beug beugeum yal na done yalna done lu geun si mom
Ladial wa toundou enhh habib goudé na goudé na habib habib
Damako dieulé l'ecole andiko super étoile mou wanefa habib habib
Fané fa lu ttax nieup nieup beugone ko
Mane youssou niak na andando bou sincère aduna aduna dal nakhati naniu
aduna aduna dafay woré habib faye demna ni wadiu bax diu tey demna




Youssou N'Dour - Habib Faye
Album Habib Faye
date de sortie
15-03-2019





Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.