Youssou N'Dour - Miss paroles de chanson

paroles de chanson Miss - Youssou N'Dour



Han' ma wakh ko ben yoon te dem miss yi gno taarou
Han wakhlenko niarri yoon te niou dem ohhhooo'
Miss yi nio taarou
Yen djiguene nirew deug deug gore yowmi yoboulegnou dara
Yen djiguene nireww deug deug mbaye gathie gualamane
Yen djiguenerewmi ken meussou len djamnanile
Fatelikou talatay nder aline sitoe diatta yacine mboubou.
Ah ma 1#
Ah ma 2x
Te mane sax mane damalene beug
Fonk
Heu axirouzamane modi moudiou diamono waw waw
Mo xam lu moudj wala lou fegn leu



Writer(s): KABOU GUEYE, YOUSSOU N'DOUR, HABIB FAYE


Youssou N'Dour - Joko (The Link)
Album Joko (The Link)
date de sortie
05-09-2000




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.