Youssou N'Dour - Yonou Deugue (Remix) - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Youssou N'Dour - Yonou Deugue (Remix)




Yonou Deugue (Remix)
Yonou Deugue (Remix)
Sama domu yaya so ubee bunt deugg bul
My home is far away but I want to return
ragala wett ndax dinga new ñulay feugg
tell me why I'm unable to see
Say say akk seytaney ñi xamul duñla beugg
All the devils know what I'm thinking
ñi xamul di lakku akk ñi raggal duñla beugg
they know if I'm going to talk or not
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nanguneñ ni jambar nga
I've been sick way too long to know I'm a fighter
sen biir xol sen biir xol ñingui
I've been sick way too long to know
laye japalei ci lu werr beuss dina ñew
let's worship the one who heals and he will restore
Yow yangui doga xam ci bula coono dabé licci mbegtel dineuleu dieulei
We two are here to see what the fool says so that he can save himself for tomorrow
funei duñu ñew seu keur te dotuñula
it happens that we don't have the same house or customs
téléphoner dañu fokni iow buñula xamei sakh yakule
we don't call each other but we understand each other's language
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nangu neñu jambar nga
I've been sick way too long to know I'm a fighter
Ñingay laye japale si lu werr
Let's worship the one who heals
Iow seu natango nguen bokk beug
We two are here too
beug buleu beug ndam tere wax lidi deug
so strange this silence you're saying nothing
Loumou metti metti metti nangul ne waji mbeur
The crowd is here here here waiting for the kickoff
leu lokko contre contre contre setalne ligueykat leu
let's have fun fun fun let's start the game let's go
Wayei sa biir xol sa biir xol finga nekk nangu ngueni jambar ngue
I've been sick way too long to know I'm a fighter
Ñingui laye japalei ci lu werr
Let's worship the one who heals
Waw suñu guiss guiss meuneu wute
Our minds our minds our rolling rebels
wute guiss guiss boum tax bañu bañante
rebels our minds our minds they're gonna make us win
Kunek fanga fete Yalla sakh dafa tane Yonente mou jite
So I pray and ask God why has he done this to me but I still love him
Yow nanga moytu raggal degnani meunala xañ seu mbekte
I am tired of being sick I want to rest for a day and tomorrow will be a new day
iow nanga moytu raggal degna meunala xañ seu mbektei wo
I am tired of being sick I want to rest for a day and tomorrow will be a new day for us
Suñu borom bile mo meune fune ñi dañu raggal di
My God is slow but he still gives us what we ask him for
Say wax akk say dieuf mom bu teggo si deugg iow nanga wey bul raggal
Let us talk to each other let us come together in peace and love and don't be afraid
Yonu deugg mom bocci neikkei di dem
Tomorrow we will be gone let's go
Bul raggala wett ndax dinga new ñulay feugg
Tell me why I'm unable to see
Say say bekk ñi xamul akk ñi raggal ñonu duñu leu meuneu beugg waw
All the devils know what I'm thinking they know if I'm going to talk or not
Sudei deugg bou deugg deugguentuwul
Tomorrow is another day another tomorrow
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
it sings (Wiri Wiri Jari Ndare)
Ey bucca raggal bucca yox yoxi ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
Hey get up and dance dance jump up and down it sings (Wiri Wiri Jari Ndare)
Sudei deugg bou deugg deugguentuwul
Tomorrow is another day another tomorrow
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
it sings (Wiri Wiri Jari Ndare)
Azizo Ndiaye lu yagg deugleu Ndiaye iow xamnga lolu
Azizo Ndiaye this is what the madman says Ndiaye I know this
Aziz xamngani deugg du nax te deugg du nax naxi
Aziz I know madness that's why
Deugg ji fi amone daw amfi dawi jegg joju deugg rekk moffi dow bataye
That madness when you see it you understand it straight away but when it leaves it hurts
Ey boudei deugg gou deugg te
Hey tomorrow is another day another
deugguentuwulñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
it sings (Wiri Wiri Jari Ndare)
Ey bucca raggal bucca yox yoxi
Hey get up and dance dance jump up and down
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
it sings (Wiri Wiri Jari Ndare)
Lekko ci ndap beugcca beuggca xeupp suf
Let's get in the arena and dance dance fast
Xaral seu bess seu bess dina ñew
Let's be happy happy happy
Mani lekko ci ndap beugcca beugcca xeupp suf
I want to get in the arena and dance dance fast
Mani Xaral seu day seu day dineu ñew
I want to be happy happy happy
Ey Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye wuy Samba Oumar Gueye (×2)
Hey Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye look at Samba Oumar Gueye (×2)
Wuy mbolo wuy mbolo(Mbolo moye doole)
They're crazy they're crazy (Crazy on the dance floor)
Wuy mbolo moy sa doole (Mbole Jami rew leu)
They're crazy my crazy (Crazy on the ground)
Maniko lekko ci ndap beugcca beugcca beugcca xeup suf
I want to get in the arena and dance dance dance fast
Mani xaral seu bess seu bess dineu ñew
I want to be happy happy happy
Eh Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye wuy Samba Oumar Gueye
Hey Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye look at Samba Oumar Gueye






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.