Youssou N'Dour - Be Careful (Version Mbalax) paroles de chanson

paroles de chanson Be Careful (Version Mbalax) - Youssou N'Dour

Be carful be carful dakh tomorrow you don't know.
So bougoulé gagnou boul thieu daw baye dano
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
If you meet a man you don't know loumouleuh meuneuh wakh
boulko know (moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
If you meet a man you don't know loumouleuh meuneuh wakh
boulko know (moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Meuneuh donap saïsaï bamou bokk'ak saïsaï
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
So bougoulé gagnou boul thieu daw baye dano
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Ooohhhhh love is very serious boul deugeuroul déy
rouss (moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Ça ne se négocie pas
ça ne s'achete pas pas pas
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Ça ne se négocie pas
ça ne s'achete pas pas pas
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Ne te fis pas aux apparences l'habit ne fais pas le moine.
Une belle chemise, un beau jean se n'est que du materiel
Une belle voiture, un chateau se n'est que du materiel
Cherche d'abord a savoir qui est derriere ce beau decor
Fou d'amour dés le premier jour "dédétte"
Foufou foufou fou d'amour dés le deuxieme jour "dédétte"
Meuneuh donap saïsaï bamou bokk'ak saïsaï
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Loooove is very serious boul deugeuroul déy rouss
(moytouko moytouko baby dakhté soubeuh xamoulooo)
Ça ne se négocie pas
ça ne s'achéte pas pas pas
(Youssou ndoye diaraf malik mareme
ndoye diaraf thia ouakam lébou leuh)
Ça ne se négocie pas
Ça ne s'achete pas pas pas
(Adji néné kane seu yaye mbao la fékk
bakh youssou ndoye diaraf lébou leuh)
Ah seck ndiaye aaatoumane ndiaye mod ndiaye goné abdou demba
bayou mar bourou teunguédji nganane seck ndiaye atoumane ndiaye.
Modou ndiaye cissé teunguédji la
fékk bakh domou lebou danio bari diomm.
Béna way séna mou sol
Waleuh auto bamou yorr (beugueu ko diokh seu xhol)
Loumou wakh gani waw (lépp guir deureum)
Xamoulo limou amm (fane leuko dieulé)
Nitt boko xamoul (dagay téyy si mom)
Béne fane waleuh niarr (meunoulo xham djikôm)
Thi seu niakk seu ngorr (lalay dougeulé)
LOVE.
BOUL guiss béne way Béna way séna mou sol
Waleuh auto bamou yorr (beugueu ko diokh seu xhol)
Loumou wakh gani waw (lépp guir deureum)
Xamoulo limou amm (fane lako dieulé)
Nitt boko xamoul (dagay téyy si mom)
Béne fane waleuh niarr (meunoulo xham djikôm)
Thi seu niakk seu bopp (lalay dougeulé)
LOVE.
Ça ne se négocie pas
Ça ne s'achete pas pas pas
(Aladji mbaye ndoye seu baye kokou
lébou leu youssou ndoye diaraf lébou leuh)
Fou d'amour dés le premier jour "dédétte"
(Ngor ouakam waw, wa yoff waw youssou ndoye diaraf lébou leuh)
Love is very serious bou deugeuroul déyy rous (ndoye
malik maréme ndoye teunguédji bi youssou ndoye diaraf)
Aye lébou laniou
Aye lébou laniou
Be carful be carful dakh tomorrow you don't know.
Dégueule!
(Youssou ndour youssou ndoye diaraf ayy xaarit laniou)
Moytouko moytouko baby dakhté soubeu xamouloooooooo.

Youssou N'Dour - Seeni Valeurs
Album Seeni Valeurs
date de sortie
01-08-2017

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.