Youssou N'Dour - Yonou Deugue (Remix) - traduction des paroles en russe

Paroles et traduction Youssou N'Dour - Yonou Deugue (Remix)




Sama domu yaya so ubee bunt deugg bul
Sama domu yaya so ubee bunt deugg bul
ragala wett ndax dinga new ñulay feugg
Ragala wett ndax dinga new nulay feugg
Say say akk seytaney ñi xamul duñla beugg
Say say akk seytaney Ni xamul duñla beugg
ñi xamul di lakku akk ñi raggal duñla beugg
Ni xamul di lakku akk Ni raggal duñla beugg
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nanguneñ ni jambar nga
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nanguneñ ни jambar Нга
sen biir xol sen biir xol ñingui
Sen biir xol sen biir xol ñingui
laye japalei ci lu werr beuss dina ñew
Laye japalei ci lu werr beuss dina New
Yow yangui doga xam ci bula coono dabé licci mbegtel dineuleu dieulei
Yow yangui дога xam ci bula coono dabé licci mbegtel dineuleu dieulei
funei duñu ñew seu keur te dotuñula
Funei duñu New seu keur те dotuñula
téléphoner dañu fokni iow buñula xamei sakh yakule
Téléphoner malitu fokni iow búñula xamei sakh yakule
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nangu neñu jambar nga
Wayei sen biir xol sen biir xol fiñu nekk nangu neñu jambar Нга
Ñingay laye japale si lu werr
Нингай Лэй джапале Си Лу Верр
Iow seu natango nguen bokk beug
Iow seu natango nguen bokk beug
beug buleu beug ndam tere wax lidi deug
Beug buleu beug ndam tere wax lidi deug
Loumou metti metti metti nangul ne waji mbeur
Loumou metti metti metti nangul ne waji mbeur
leu lokko contre contre contre setalne ligueykat leu
Leu lokko contre contre contre setalne ligueykat leu
Wayei sa biir xol sa biir xol finga nekk nangu ngueni jambar ngue
Wayei ООО biir xol ООО biir xol finga nekk nangu ngueni jambar ngue
Ñingui laye japalei ci lu werr
Нингуи Лэй джапалей Си Лу Верр
Waw suñu guiss guiss meuneu wute
Waw suñu guiss guiss meuneu wute
wute guiss guiss boum tax bañu bañante
Wute guiss guiss boum tax Banu bathante
Kunek fanga fete Yalla sakh dafa tane Yonente mou jite
Kunek fanga fete Yalla sakh dafa tane Yonente mou jite
Yow nanga moytu raggal degnani meunala xañ seu mbekte
Yow nanga moytu raggal degnani meunala Xan seu mbekte
iow nanga moytu raggal degna meunala xañ seu mbektei wo
Iow nanga moytu raggal degna meunala Xan seu mbektei wo
Suñu borom bile mo meune fune ñi dañu raggal di
Суну бором желчь МО мене Фуне ни вреду раггал Ди
Say wax akk say dieuf mom bu teggo si deugg iow nanga wey bul raggal
Say wax akk say dieuf mom bu teggo Си deugg iow nanga wey bul raggal
Yonu deugg mom bocci neikkei di dem
Yonu deugg mom bocci neikkei-ди-dem
Bul raggala wett ndax dinga new ñulay feugg
Bul raggala wett ndax dinga new nulay feugg
Say say bekk ñi xamul akk ñi raggal ñonu duñu leu meuneu beugg waw
Say say bekk Ni xamul akk Ni raggal nonu duñu leu meuneu beugg waw
Sudei deugg bou deugg deugguentuwul
Sudei deugg бу deugg чай deugguentuwul
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
нодил му дуг (Wiri Wiri Jari Ndare))
Ey bucca raggal bucca yox yoxi ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
Ey bucca raggal bucca yox yoxi nodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
Sudei deugg bou deugg deugguentuwul
Sudei deugg бу deugg чай deugguentuwul
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
нодил му дуг (Wiri Wiri Jari Ndare))
Azizo Ndiaye lu yagg deugleu Ndiaye iow xamnga lolu
Azizo Ndiaye lu yagg deugleu Ndiaye iow xamnga lolu
Aziz xamngani deugg du nax te deugg du nax naxi
Aziz xamngani deugg du nax те deugg du nax naxi
Deugg ji fi amone daw amfi dawi jegg joju deugg rekk moffi dow bataye
Deugg ji fi amone daw amfi dawi jegg joju deugg rekk moffi dow bataye
Ey boudei deugg gou deugg te
Эй boudei deugg ГОУ deugg тебя
deugguentuwulñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
Deugguentuwulñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
Ey bucca raggal bucca yox yoxi
Эй bucca raggal bucca yox yoxi
ñodil mu deuguer (Wiri Wiri Jari Ndare)
нодил му дуг (Wiri Wiri Jari Ndare))
Lekko ci ndap beugcca beuggca xeupp suf
Lekko ci ndap beugcca beuggca xeupp suf
Xaral seu bess seu bess dina ñew
Xaral Сеу Бесс Сеу Бесс Дина Нью
Mani lekko ci ndap beugcca beugcca xeupp suf
Мани lekko ci ndap beugcca beugcca xeupp suf
Mani Xaral seu day seu day dineu ñew
Mani Xaral seu day seu day dineu New
Ey Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye wuy Samba Oumar Gueye (×2)
Ey Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye wuy Samba Oumar Gueye (×2)
Wuy mbolo wuy mbolo(Mbolo moye doole)
Wuy mbolo wuy mbolo (Mbolo moye doole)
Wuy mbolo moy sa doole (Mbole Jami rew leu)
Wuy mbolo moy sa doole (Mbole Jami rew leu)
Maniko lekko ci ndap beugcca beugcca beugcca xeup suf
Maniko lekko ci ndap beugcca beugcca beugcca xeup suf
Mani xaral seu bess seu bess dineu ñew
Мани ксарал Сеу Бесс Сеу Бесс динеу Нью
Eh Samba Abidjan Samba Samba Coumba Ndiaye wuy Samba Oumar Gueye
Эх Самба Абиджан Самба Самба Кумба Ндиайе уй Самба Умар Гуэйе






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.