Текст песни
Boo
ma
beddiwul
xalaatuma
la
bàyyi
Awma
laamisoo
tudduma
lambay
yoy
Gaañ
la
taxul
nga
ba
Tooñ
la
taxul
nga
may
rëccooy
Sàllaaw
yenn
saay
nga
mer
Sama
jaambaar
ci
yaw
mi
la
wékkooy
Dootuma
wiri
wiri
njari
ndari
Li
ma
moom
laay
jëli
(eeh
yoo)
Dootuma
yónni
kenn
ci
sama
waa
ji
Man
mi
maa
koy
jëli
(man
ma)
Dootuma
wiri
wiri
njari
ndari
Li
ma
moom
laay
jëli
(daadi
sama
waay)
Dootuma
yónni
kenn
ci
sama
waa
ji
Man
mi
maa
koy
jëli
(danga
di
sama
waay)
Bala
ma
jug
Fajar
fekk
nga
dem
jaayooy
Bale
kër
gi,
raxas
say
ndap
Ndekke
boobu
doom
ngay
wajal
Dundu
mat
a
ñaan
nooy
Ndaxte
gaynde
dama
koy
jur
Ndax
fitna
loo
ma
Xeboo
li
ma
lay
jox
Lépp
loo
ma
ñaan
dinaa
la
may
Dootuma
def
leen
lu
lay
metti
sama
ndaw
ci
Ndax
sama
nawle
nga
doo
leeral
sama
yoon
wi
Dootuma
nangu
mbindéef
di
dox
sama
digu
ak
yaw
Ndax
Yàlla
moo
def
ci
ñun
lay
ñu
wëy
nak
Kaay
waay
Gaañ
la
taxul
nga
ba
Tooñ
la
taxul
nga
may
rëccooy
Sàllaaw
yenn
saay
nga
mer
Sama
jàmbaar
ci
yaw
mi
la
wékkooy
Dootuma
wiri
wiri
njari
ndari
Li
ma
moom
laay
jëli
(eeh
yoo)
Dootuma
yónni
kenn
ci
sama
waa
ji
Man
mi
maa
koy
jëli
(man
ma)
Dootuma
wiri
wiri
njari
ndari
Li
ma
moom
laay
jëli
(daadi
sama
waay)
Dootuma
yónni
kenn
ci
sama
waa
ji
Man
mi
maa
koy
jëli
(danga
di
sama
waay)
Gaañ
la
taxul
nga
ba
Tooñ
la
taxul
nga
may
rëccooy
Sàllaaw
yenn
saay
nga
mer
Sama
jàmbaar
ci
yaw
mi
la
wékkooy
Eee
waay
Sama
jamm,
sama
waay
Eh
waay
wow
Sama
jamm,
sama
waay
Sama
jamm,
sama
waay
Boo
yeewoo
Papa
Laye
sunu
way
1 Adduna
2 Legét
3 Kelemati
4 Daaru Dunya
5 njegenaay
6 dinala won né
7 Ajaa mooy Ajaa
8 Waw coumba
9 Kocc na ma jéggal
10 Comme ni nga ma
11 woyal ma, bégal ma
12 Jëli
13 Keneen Kumu Doonoon
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.