Admow feat. Maftou - I Wanna Know (feat. Maftou) текст песни

Текст песни I Wanna Know (feat. Maftou) - Admow feat. Maftou



Beuss bou nék mane mangui dokh
Mangui guiss wanté meunouma know
Ki ma hate ki ma like ki ma fan ak ma love
Sometime ma melni kou gueum ay nit di sopelikou bamey demeu
Niou gueneu jegué nioley beteu nioley padeu nioley kill di nio ley guédeu
Oooooh waaaaay i wanna know
Li nek si sa khol dakh ma mouytou
Oooooh waaay can you let me know boudé beugoula ndakh ma meuneu move



Авторы: Adama Diop


Admow feat. Maftou - Revolution
Альбом Revolution
дата релиза
03-12-2015



Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.