Текст песни Ayubes - Ashs The Best
Man
gestu
naa
di
xoolaat
fi
ma
jaar
Te
weesu
naa
dootul
mës
ñëwaat
Foo
ma
jëmee
ci
kaw
mbaa
ci
suuf
Su
ma
gisatul
yaay,
te
ammu
ma
maam,
fan
laay
nàmpee
Foo
ma
nara
jëmee
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
(Maam
Yàlla
ko
moom)
Jamm
a
ko
gën
(Jamm
a
gën
ub
ay)
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
(Maam
Yàlla
ñu
moom,
moom
sunuy
doom)
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
(Maam
Yàlla
ñu
moom,
uuf
sunu
njaboot)
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
Miin
naa
sa
kanam
gi
Miin
naa
kepaar
gi
Gëj
naa
këram
ga
Te
miin
naa
dëkkam
bi
Gëj
naa
ci
xellam
bi
Te
sës
ci
xollam
bi
Xas
naa
ko
xaccoo
Dootu
ma
fa
delloo
Man
da
maa
foogoon
Da
maa
foogoon
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
Maam
Yàlla
ko
moom
Jamm
a
ko
gën
Jamm
a
gën
ub
ay
Da
maa
foogoon
dootul
jeex
ndeke
Yàlla
ko
moom
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.