Текст песни Jirim - Ashs The Best
Naawal
naawal
naawal
Balaa
guddee
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Naawal
Guddi
jot
na
guddi
jot
na
fooy
fanaan
Naawal
Yaay
ja
reer
baay
ba
naxsaay
na
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Guddi
jot
na
gaawal
gaawal
balaa
ñu
lay
fexeel
Yaay
ja
reer
na
baayam
saay
na
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Soo
ko
fi
gisulee
guddi
moy
dem
na
Te
soo
ko
fi
gisee
sànku
na
Cokkeer
doom
noppil
Sa
yaay
wuti
na
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Su
weetee
jooy
Su
sonnee
jooy
Su
woppee
jooy
Su
raflee
jooy
Guddi
jot
na
guddi
jot
na
guddi
jot
na
fooy
fanaan
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Su
weetee
jooy
Ndax
saa
yu
xiifee
fànde
Su
guddee
mu
lakku
balaa
ñu
koy
fexeel
Kii
lu
mu
sonn
sonn
taxul
Taxul
coono
yi
jeex
Su
muññee
bii
beneen
na
koy
xaar
ëllëg
Beneen
na
koy
xaar
ëllëg
beneen
na
koy
xaar
ëllëg
Su
guddee
mu
lakku
balaa
ñu
koy
fexeel
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Yaay
ja
reer
na
baayam
ba
saay
na
Su
guddee
mu
lakku
balaa
ñu
koy
fexeel
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Yaay
ja
reer
na
baayam
ba
saay
na
Baayam
ba
saay
na
Ku
ammul
ndey
nàmp
ci
maam
Ku
ammul
maam
doyloo
sa
bopp
Naawal
naawal
naawal
Naawal
naawal
naawal
Balaa
ñu
lay
fexeel
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.