Big Dat X - Linjaa текст песни

Текст песни Linjaa - Big Dat X




Waga yee aye linjaa bi day dal
Joxeel li nga yor te bufi tek xel
Mbedd yàgg nañ fa semer bordel
Ku ñu sóng am mbetteel
Xëpp si bombe rómb ba ñëpp ñëw geew
Game bi daf ñu lew taxul ñu bew te kenn gënu ñu reew
Ñoo nge eg jam missile
Imbécile bu jaay prek ñu wàcc sa domicile
Mënoo ñu tek deal kon buddil
Balaa ñuy aksi sa kaw di këf si sa ndaw
Tus nak dara du xew
Dañuy taak sa rëm ok ok
C'est ça le minimum
Dañuy taak sa rëm ma ni
C'est ça le minimum
Ngaaka yi yàgg ñu ting taxul ñu bage faraa yi
Fuck them all bul lancer défi ñun dañu aay
Small small small danuy firi rek bàcc
Small Negger
Small Negger
Danuy firi rek bàcc
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Eh
Ñun dañu fayyeeku si force
Get rich or die
Game bi lama discover
Maa fi tiim sen gaal
Maa deep so far
Money do or die
Bombaclat them a chichi
Sen wax u goorjigeen yi laay xaar kenn boole ma si
Ku raxas am di fëxx ndap doo ko indil tilim-tilim
Ñun la modafucker sànni mbaal yi te doo ñu ci lim
Game bee bari xànju man
Ku si nekk xam ki la mën
X sen biir deyzkalanax
Door si matt gi ñu dem fuuf nga si mën
Golo moo la gën a xam kër gu bari xaj
Te bari kaf teewu leen ràññe passi ak day u bëy
Dañuy firi rek bàcc toj mbaar yi sónga ti leen ngeen yuuxu meydey
Musig u mbedd waga mooy bénéfice
Te benn fils de pute du ñu teye ñooy jómmal iblis
Gën a reew gën a cool bul aksi
Ki pare pour yàxxate murder sen business bi tek si
Small small small danuy firi rek bàcc
Small Negger
Small Negger
Danuy firi rek bàcc
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Na linjaa bi dal
Fayyeeku force
Eh
Ñun dañu fayyeeku si force



Авторы: Abdoulaye Wone, Sidath Youm


Big Dat X - Mic Check
Альбом Mic Check
дата релиза
12-11-2022




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.
//}