Big Dat X - Victory текст песни

Текст песни Victory - Big Dat X




Ku YÀGG si TEEN foog BAAG
Fekk si la
Sa success sa hand man
Sa gëm-gëm bi ci la
Bu job bi baaxul dellul parfaire ndax nettali ba
Mani la XEL KOOM LA
Life leegi lepp money la
Ki dëkkee nekk digg geej
Mën na bañ a xam
Li nekk si tali ba
Ñun la sëriñ u tay
Cauz ñun dañu yàgg nek fi taalibe
Gaynde bi mer la fanaano
Bii level du ñëpp a ko mën a know
Ki miser bakkan bi si victory
Ready fi everything
Tell em they better know
Jam-jam bi bari na
Xam-xam bi bari na
Ma dëkk si ñafe ba ndam li gane si
Lu mësul a dàgg tay dikk na
I'm the moon so let me shine now
Born to be leader
Victory or let me die now
I know this
I know that
I know that i'm a lion inady jungle
Ain't time a lose That's di revolution
Ajj na barre yi bloquer gars yi
Actor baa ngii
La Di Da Di move your body
Man la ñaar i gares yi
Patience pertinence ligeey indi
Victory
Selfmade man they better know mooy sama history
Gëm sa bopp better be a hustler
Warrior man ñakk jom si moom xas la
Patience pertinence ligeey indi
Victory
Selfmade man they better know mooy sama
History
Gëm sa bopp better be a hustler
Warrior man ñakk jom si moom xas la
Li PASSÉ bi COMPOSÉ INDIQUER
Li tax PRÉSENT bi SIMPLE
Pare pour FUTURE bu
Perfect prouver persévérer
Passion patience ni Casa de Papel si PROFESSOR
Pas de Panique
Proud to practice moy sa pur POWER
PAAKA SI PUT teggi wul sama PER U BËT si seen price
I'm the living legend
Man xoole ma SEAN PRICE
Badman for real man kenn duma ñoddil parano
They gotta know
Why never ñu tolloo
Même buñ départ ra ndoo
SOLDIER laa si GUERRILLA
Sama MISSION du IMPOSSIBLE
Remplir si POche yi balle
Atteindre lima jël comme CIBLE
RAS gun u guerrier buy genn
Day gaañe pour gagner
From the bottom to the top SADIO MANE
From the bottom to the top SADIO MANE
From the bottom to the top SADIO MANE
Patience pertinence ligeey indi
Victory
Selfmade man they better know mooy sama
History
Gëm sa bopp better be a hustler
Warrior man ñakk jom si moom xas la
Patience pertinence ligeey indi
Victory
Selfmade man they better know mooy sama
History
Gëm sa bopp better be a hustler
Warrior man ñakk jom si moom xas la



Авторы: Trevor Smith, Sean Combs, Bill Conti, Steven Jordan, Christopher Wallace, Jason Phillips


Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.