Текст песни Jolaa - El Hadj N'Diaye
Joola
bi
sux
na
Rewmi
am
na
tiis
Keerog
bis
boobu
reew
méempou
jooy
Joola
bi
sux
na
Rewmi
méempou
jooy
Bannexu
jiit
yi
Rangooñ
askan
wi
Joola
bi
sux
na
loño
yagni
digg
Bannexu
jiit
yi
Rangooñ
askan
wi
Am
na
ci
gnoo
xamni
dotu
gnu
giis
yaay
Dotu
gnu
bàay
njirim
yagni
jooy
Joola
bi
sux
na
loño
yagni
digg
Bannexu
jiit
yi
Rangooñ
askan
wi
Siggi,jamonoy
siggi
la
Taane
xoolu
yak
say
bët
Ndaxte
gor
mën
ta
degge
sëgg
Siggila
tane
jood
ba
melni
kii
gadàawu
Boleci
nak
dii
lace
lo
yeeyo
Lu
gnu
dal
waru
gno
wàar
Kùu
añe
rer
bi
Bu
xale
yi
dii
jooy
Gna
wara
sëgg
Te
kat
bùu
jooy
ñeexe
siggi
jòt
Ndaxte
kùu
amul
bàt
ta
giiso
Yoon
Wara
mëna
siggi
nak
bane
xoognu
Альбом
Géej
1 Sant Yalla
2 Jaly
3 Mi alla ligéey
4 Cheick anta diop
5 Tokoroni
6 N'guri
7 Jolaa
8 Dégueulasse
9 Adduna
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.