El Hadj N'Diaye - Yoon wii текст песни

Текст песни Yoon wii - El Hadj N'Diaye



Ni tund we te toor toor yi sac ce(bis)
Ni tund we te toor toor yi sac
Moom la guiss sama kanam yoon(bis)
Ni tëggkatt bi tegg na ganaay yi
Ni soxna si sox na mékk dom yi
Ni car wi ta ramatu bi tak ce
Ni udébi ëw na terreye
Ni tere yë,tere yë,tere te(bis)
Ni Yoon wa tah toroth gaw ce
Ni yoon wa ta xaxan yi bare ce
Ni deex ge ta jasik yere bare ce
Moom la guiss sama kanam gi
Ni wajé dërëm gi womat ko
Toop sa bakan faté lu la warr ye
Gagni lu mbëtt bëgg,mom la barr bëgg
Waye soma gënne bëgg ma bayi ak yow
Ndax tere yë,tere yë,tere
Ni tere yë,tere
Ndax bëtt yi




El Hadj N'Diaye - Xel
Альбом Xel
дата релиза
08-06-2001




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.