Текст песни Bul Ma Miin - Orchestra Baobab
Bul
ma
miin,
Bul
ma
miin
Bul
ma
miin
ba
fatte
ma
Kon
mu
ňaaw
Adduna
yaa
mëna
wor
Xaň
ma
ndey
xaň
ma
baay
Boo
ma
digee
sama
doom
nax
nga
ma
Lekkatuma,
naanatuma
Tëddatuma,
nelawatuma
Boo
ma
digee
sama
doom
nax
nga
ma
Alarba
la
woon
ci
weeru
koor
Mu
taggu
ma
ne
ma
maangi
ňëw
Boobu
ba
téy
gisuma
sama
doom
Woy
wéét,
woy
wéét
Woy
wéét
adduna
Sama
doom
dem
na
nii
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.