Текст песни Yaw Reck Lev (Duet Corine) - Philip Monteiro
Oubil
nala
sama
khol
yala
nagua
si
guiss
Lou
ler
tei
ga
khamni
amoul
kenen
kou
doul
yaw.
Mbeuguel
bi
nek
si
mane
mougui
dima
dane.
Tegue
nani
di
neu
done
sa
nene
bi
gay
tete...
Mane
mi
souma
meunone
dina
bokeu
ak
yaw
ben
yone
di
leu
wowei
nene
Touti
dakh
mane
mi
mane
mii
gnanou
ma
Yalla.
gnanou
ma
yalla
dess
fi
mane
rekeu
Ya
nek
sama
khol
guissou
ma
kenen
kou
doul
yaw.
oubil
na
la
sama
khol
Tei
dina
done
sa
néné.
Amna
gnou
wakh
beuguel
tiono
rek
leu
Wayei
magui
ley
khamal
dou
ken
yaw
rek
leu
Beuss
bouma
la
guissei
la
khamni
khole
day
Guissei.
tei
fok
na
do
meuseu
tass
sama
yakar
Boul
am
loy
ragal
dou
ma
meuseu
diay
sama
tar.
Dina
la
wowei
papa
cheri
dina
done
sa
sokhna
dina
Done
sa
baby
bi
lay
fadial
sey
sokhla
ohh
baby
yaw
rek
leu
Ya
nek
sama
khol
guisou
ma
kenen
kou
doul
yaw
oubil
nala
sama
khol
Té
dina
done
sa
néné
Yaye
sama
dolei
soudoul
yaw
wate
na
ni
dou
done
kénéne.
Diokh
nala
sama
bopp
tei
dina
le
bégueul
Baby
boul
soneu
geumeul
ni
yaw
rek
leuuuuuuu
dou
done
kénéne
Oubil
nala
sama
khol
bi
Dina
done
sa
baby
Dina
done
sa
sokhneu
Dina
done
sa
néné
1 Si Bu Cre
2 Cyndi
3 A Volta
4 Sama Wo
5 Preciosa
6 San Jon
7 Passada Bounce
8 Nos Ku Mundu (Remix)
9 Fanny
10 Si Bu Cre (Remix)
11 Irresistivel (Remix)
12 Inseparável
13 Estou Em Suas Mãos
14 Si É Verdadi (Duet Imelie)
15 Yaw Reck Lev (Duet Corine)
16 Abri Bu Coração (Duet Gama)
17 Tempestade
18 Costel (Intrumental)
19 Gainde Njaay
20 Cindy (Raggaeton)
Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.