Viviane Chidid - Déranger текст песни

Текст песни Déranger - Viviane Chidid



Bilé mélokaan molaye deranger
Xamna li laye sonaal
Xaax ju bari tekk ci ngua diss yénou wo
Xamna li laye sonaal
Bilé mélokaan molaye deranger
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen dima rétaan beugouloma
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen talal ma loxxo sopouloma
Xamna li laye sonaal
Xaax ju bari tekk ci ngua diss yénou wo
Xamna li laye sonaal
Bilé mélokaan molaye deranger
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen dima rétaan beugouloma
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen talal ma loxxo sopouloma
Heey
Tiré ngama visé ndax dalouma
Tiré ngama visé ndax dalouma
Tiré ngama dolil ndax dalouma
Sit down yoww
Fi adouna leu konn teyal
Fi adouna leu fils teyal
Fi adouna leu konn teyal
Fi adouna leu fils teyal
Xamna li laye sonaal
Xaax ju bari tekk ci ngua diss yénou wo
Xamna li laye sonaal
Bilé mélokaan molaye deranger
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen dima rétaan beugouloma
Yallah may ma nangou wo
Ma rombeu la nangou wo
Fo ma séen talal ma loxxo sopouloma
Heey
Tiré ngama visé ndax dalouma
Tiré ngama visé ndax dalouma
Tiré ngama dolil ndax dalouma
Sit down yoww
Jeuleul woy wi ma may leu yeah
Jeuleul woy wi ma may leu yeah
Jeuleul woy wi ma may leu yeah
Woy jeuleul woy wi ma may leu, def ko cas
Liguay degager
Mokoy deranger
Yalla ko def ci yow
Niou waxanté deugue
Liguay degager
Mokoy deranger
Yalla ko def ci yow
Niou waxanté deugue
Ma teugu ko teugu ko teugu ko
Nga Fecc ko Fecc ko Fecc ko
Vivi yow fi niou teugu fée ngueen dadi bégué
Nganni??
Gagal amadou, moustapha diop
Makhouredja Baye lan niang moy sa maam
Moustapha diop domou louga lo adja dior mor sa yaye
Niit kou baax
Wahou mako wa louga ko waax yangua
Dimbeulé, Ji jappalé (louange a moustapha diop)
Niit kou lay wout (lo ci waax)
Jem jem jotoula (Lox pexem)
Dafa seet kila guene jégué mou jaré feu
Ba yaxal leu (ah bon?)
Wayé yow mi boulen falé
Ma (je dis)



Авторы: Akatche Bennette, Seraphin Koffi, Victoria Catherine Chidid


Viviane Chidid - Déranger - Single
Альбом Déranger - Single
дата релиза
23-12-2019




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.