Young Bari feat. Flow - My Own Hype Pt2 текст песни

Текст песни My Own Hype Pt2 - Young Bari feat. Flow



Di na fègn ci jikko wala fègn ci judd
Ndakh Ci derett lay nekk du ci mboubou
Du yeuglu du feug day dikk doug
Bul lo bayi muu lèkkè lokho jokh kuddu
Moy njeukk ci bool bi te moy ciy mujjé
Fooko fekk day foXlé beunlé beug wujé Du doylu du doyna du doyal du dessal
Badolo gaw ci Dolli ma bootu sa kaw di la dissal
Bala jogg ci ndap li ndawal li jekh
Bu suuré du jaraw lakk day fudd raay dékh rek
Moo raw purux Du geureum niami daw
Fu mu la fekké si tolof tolof bayi lafa daw
Soo ko invite day invitè moromam
Te wax bu yonam nekul sakh fauk mu sapali ci xoromam
Da fay sew jikko meun a setlu siss sof
Sans sutura lumu la xamal mu siiw rakh gaw ci Soss
Xamul njiowan te bala moo watch mu dagg
Buggul dégg deug li mu beugga dégg moy ku kay Tagg
Sédelé buki lay sédelé
Su ko yallah mayé dolé dotul jégalé
Da fa gawa xebatè gawa yabatè
Ku ko eupeulè kesse ko ku lay respecter
A ka meun fallatè mana jeulatè
Rambadj ni seytané niakk koloré
Gawa djeuwatè
Bu suuré rew bu amè bew
Amul kaddu. day beug waķh ju sew
Dou kholè day kholè
Ku mu deukeul nga tokhou
Di na lay niè di la ignanè
Di la soufou di la Soukhlou
Da fa Meuna niane ney ba ba buy saw sakh du sit
Bu duggè sa toilettes bayi fa bombe atomik
Ken du ko denk alalu mboolo
Du fay boor ta su abbe du dello
Soo kay nian nian ko ci biir Mbollo
Ndakh su lay may da koy def ci mboolo



Авторы: Jabari Whearry Baldwin


Young Bari feat. Flow - Mob Solo
Альбом Mob Solo
дата релиза
29-03-2014



Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.