Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - Independance текст песни

Текст песни Independance - Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile



Mane téwoul damay delou sant yalla
Maynama ma feikkei ti fétou indépendace
Fétou indépendance yima feikkei beuriwoul
Amna samay morome dh youko feikkeiwoul
Limoy liwaral ma doli sant yalla
Fétou indépendance bi moye sama repère
Sa you meussane nieuw keine doumako neitali
Damadane jook thia fadiar ndeiki daw wouti place
Deim boukhantei dji diap place thia kanam
Bima guenone neikh défiler militaire
Bou eleve yi rombei yor seni drapeau
Sol ay tenue kaki di balancé les bras
Bou armée yi nieuwei bama sen commando yi
Dawouma beugue loudoul dem solou militaire
Wa armée de terre akk wa armée de
L'air marine national pompiers akk police
Kouthi meusseuna diar sama khol daye sedd
Fetou independace dafma yaggue neikh
Wa armée de terre akk wa armée de l'air
Gendarmerie national pompiers akk police




Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - From Senegal to the World: 80s Classics & Rarities
Альбом From Senegal to the World: 80s Classics & Rarities
дата релиза
08-10-2012




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.