Kya Loum - Waxtu Lyrics

Lyrics Waxtu - Kya Loum



Beuss boula xassa rombe ne'na fess
Bala nga kooy xaam fatalikul sa Demba
Kaalaama dafaay wees
Boula xasse' raaw netaliwi mo fiye dess
Bamtou waat donga fi ne'
Bo ko we'de' deloul thiossane
Nga xool thia guëstu thia
Lo xaam taay amena kou ko xamone
Lalene woute'le' thia deguine wa la
Ak waxtuwa
Mba diamono dia
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Ayiiii ndox wa ngaay walagaan
Ayiii dotouniou bawounaan
Waxtu mooy melo
Def si nioun djiko
Dotouniou reroo
Thi adunya
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Yallah bindeu thi waxtu
Dioudou thi waxtu
Doundou thi waxtu de'e thi waxtu we'
Le'peu waxtu te'ew thi waxtu
Dioudou thi waxtu diouli thi waxtu
De'e thi waxtu
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa
Fou ndox daan taa fou ndox daan laaw
Tep tepa ngui fa tep tepa ngui fa



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Kya Loum


Kya Loum - Niit
Album Niit
date of release
14-10-2022




Attention! Feel free to leave feedback.