Kya Loum - Wouté Lyrics

Lyrics Wouté - Kya Loum



Woute'
Mbidef ye woute'
Djiko ye' woute'
Woute' nanio woute' nanio
Ni mouniou binde' ndiro te' woute'
(Xolal say bara am)
Siguil xool ma siguil xool
Thieur ye' mengo souniouy xalaat woute'
(Xolal say bara am)
Niak dego menena am thi mbiir
Xelyi meune na nio woute'
(Xolal say bara am)
Siguil xool ma siguil xool
Li may dioylo menena la begg lo
(Xolal say bara am)
Woute' melo ndiro xalaat Woute' xalate ndiro melo
Li ko waraal moy woute' diar diar
Li nga amone moy lima niakone
Xaar mi niou yaar thi digou keur gui
Menoula bokak melo xa air ale bi
Beugueunete' lolou woute' gueum gueum
Waral ma gueum ni mbeugel mo di yallah
Woute' melo fi ndiro djiko fe'
Woute' gueum gueum te'woul niou boki xalaat
Woute' melo fi ndiro djiko fe'
Woute' gueum gueum te'woul niou boki xalaat
Woute' Woute' me'lo
Woute' djiko tewoul niou boki xalaat
Woute' Woute' me'lo
Woute' djiko tewoul niou boki xalaat
Nangul ma ni matuma maniit ma nangul la ni matulo
Mbidef ye' baari sopeku yomb lolou
Ngala bul fate' ki done nba saax ki ngaay beugui done
Adunyaa teureude' nono yomb lolou
Yallah bour be saak mbidef te' yamale'woul
Ndangou dieul na thieurou bagne nangou na ki ma done
Douma fate' yeah
Nite nite' nite nite' nite nite' nite nite' ko waar
Woute' nanio Woute' nanio Woute' nanio Woute' yeah yeah
Woute' melo fi ndiro djiko fe'
Woute' gueum gueum te'woul niou boki xalaat
Woute' melo fi ndiro djiko fe'
Woute' gueum gueum te'woul niou boki xalaat
Woute' Woute' me'lo
Woute' djiko tewoul niou boki xalaat
Woute' Woute' me'lo
Woute' djiko tewoul niou boki xalaat



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Kya Loum


Kya Loum - Niit
Album Niit
date of release
14-10-2022




Attention! Feel free to leave feedback.