Marema - Bayo Baye Lyrics

Lyrics Bayo Baye - Marema



Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Nononono
Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Baye guestoul keurgui lei
Jamboot dja ngui tokk iow mi ley djilo khar reer
Djouroulo niou diour wone niouko nioune Bala
Kholatal seu dieufine ndakh tei aduna dafa goudou tank lol
Nioune doomou baye naniou duniu siseuntei
Yayou teela gueineu adunya biii
Baye kholatal sa dieufine Baye guestoul sa guinaaawwww
Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Nonononono
Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Baye guestoul aduna
Jamboot dja ngui tokk iow mi ley djilo khar reer
Djouroulo niou diour wone niouko nioune Bala
Kholatal seu dieufine ndakh tei aduna dafa goudou tank lol
Kholal ki si dem mou ngui nane diw sa Baye leuh
Lepalou ko war tchi keur bi netali lakoy def
Ni doomou baye laniou baaaaaayyyyeee
Yeah yeah yeeeeaaaaahhh
Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Nonononono
Ni Bayo Bayeeeeee
Bayo Bayo Bayo Bayo baye
Me Bayo Bayo Bayo Bayo
Bayo Bayo Bayo Bayo Baye
Nene moudji Baba moudji
Mbiguel bou niou taamaa



Writer(s): Marema


Marema - Initié
Album Initié
date of release
01-06-2016




Attention! Feel free to leave feedback.