Obree Daman - Banneex Lyrics

Lyrics Banneex - Obree Daman



Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
(Bis)
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
(Bis)
Baby yow yaay sama life
Suma Yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow
Ndax ku melni yow amatul ci àdduna
Sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale
Benn noon ndax yaay sama life
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
Baby yow yaay sama life
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
(Bis)
Ci sa bët laay xool naan la I Love You
Baby yow yaay sama life
(Bis)



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb


Obree Daman - Bantu Bale
Album Bantu Bale
date of release
25-03-2022




Attention! Feel free to leave feedback.