Obree Daman - Bantu Lyrics

Lyrics Bantu - Obree Daman



Nitt
Ak melokaanam
Ci yërmande
La ko Yalla bindee
Doomu Àdama
Cëy xamoon lu ko fi indi woon
Hum du caaxaan
Fii
Fii àdduna la
Ndank yen
Ci àdduna
Nitt moo ñàkk xëy bis am beew
Nitt moo njool moo gàtt moo weex
Waaye ci yërmande
La ko Yalla bindee
Ho ho ho
Ho ho ho
Ho ho ho
Ho ho ho
Yalla moo sàkk goor ak jigeen
Magg ak ndaw te yemale wu len
Yalla moo sàkk bëccëg guddi
Bës bu xasa dem dootul deelu si
Fii
Fii àdduna la
Ndank yen
Ci àdduna
Ho fii
Fii àdduna la
Ndank yen
Ci àdduna
Yalla moo sàkk goor ak jigeen
Magg ak ndaw te yemale wu len
Yalla moo sàkk bëccëg guddi
Bës bu xasa dem dootul deelu si



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb


Obree Daman - Bantu Bale
Album Bantu Bale
date of release
25-03-2022




Attention! Feel free to leave feedback.