Youssou N'Dour - Ndox paroles de chanson

paroles de chanson Ndox - Youssou N'Dour



Ndox, L′eau
Sa joie et sa pudeur font sa face cachée.
Son paraître et ses formes montrent sa force.
Celle que je vous chante, vous est familière!
Elle est utile et belle.
Elle a révélé la beauté du monde.
On la clame Paradis.
Mbégté ma, suturë sa,
Da fa méngóo k, baatin ëm
Zaahir sa, melo ya,
Moo won e, kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la,
Am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna,
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaan e ko sax banneex la,
Nañ ko foηk sakkan al ko
En parler même est agréable!
Respectons-la, économisons-la.
Vois la mer, le fleuve.
Rendons grâce à Dieu.
Elle est utile et belle.
Elle a révélé la beauté du monde.
On la clame Paradis.
Mbégté ma, suturë sa,
Da fa méngóo k, baatin ëm
Zaahir sa, melo ya,
Moo won e, kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la,
Am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna,
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaan e ko sax banneex la,
Nañ ko foηk sakkan al ko
Géej gaa ngi nii yé,
Dex gaa ngi nii
Dara gën ul ë neex taw bi
Ku weddi laaj ko bay kat ba,
Ci la ñuy roosé seen tool ya
Walla nga laaj ko samm kat ba,
Ci la ñuy nandal e jur
Ndox daal am na njariñ baax na
Dara gën ul neex taw bi
Taw daal njariñ la ci dun bi
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm, ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm,
Ba la nga koo xam mu manqué
Alaa gaynaago yoo samba lingeer
Donoy waaly yée, wulée ñaay ngoy,
Yée gan wuri coo, wulée gaynaako yoo
Yeée, yóo, gan fari baa




Youssou N'Dour - MBALAX
Album MBALAX
date de sortie
12-11-2021




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.