Obree Daman - Bo Jekko Lyrics

Lyrics Bo Jekko - Obree Daman



Bo jekko
Deel baale
Boo amee te mën ko
Deel maye
Bo jekko
Deel baale
Boo amee te mën ko
Deel maye
Yaa ngi ci kaw
Xalaatal ñi ci suuf
Because tomorrow
Is another day
Bu am-am tax
Nga fate ki doonoo
Waaye bu ñakk tax
Nga baayi sa loxo
Ab Goor Yàlla ngay doon
Royal ci Ibra Faal ee
Dinañ la xas dinañ la faqastal
Waay waay bu len faale
Ab Yaay Faal ngay doon
Royal ci Maam Buso Baali
Dinañ la xas dinañ la faqastal
Yaay Faal nga bu len faale
Jappante baña baayi gën di bëggënte
Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase
Ah dunyaa
Ah dunyaa
Jappante baña baayi gën di bëggënte
Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase
Ah dunyaa
Ah dunyaa
Goor Yàlla yombul
Ci adduna si le
Boo jekkoo deel baale boo ammee te mën ko deel maye ay
Waay waay waay
Bo jekko
Deel baale
Boo amee te mën ko
Deel maye
Bo jekko
Deel baale
Boo amee te mën ko
Deel maye



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Oumar Samb


Obree Daman - Bo Jekko
Album Bo Jekko
date of release
01-10-2021



Attention! Feel free to leave feedback.