Ashs The Best feat. Mamy Victory, Keyti & Baye Souley - I FEEL GOOD Lyrics

Lyrics I FEEL GOOD - Ashs The Best



I feel good
Nobody can disturb sunu life
Ñun dañ koy def ba muy moom
I feel good
Respect ñi la dundal demb'ag tay
I never let you down
I feel good
You push me high
I never let you down
I feel good
You make me smile
I never let you down
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
I feel good
Live my life melni ku mbedd jur
Bës da ma reer yaa ma indiwaat
Jang ci yow lu ma xammul woon school
Mbedd a ma dicter ma bind texte
Bëggoon naa tekki am ay millions
Mais mësu ma xam li ma wara doon
Dund naa gacce yu tegaloo
Mais yaakaar yi naxu ma benn yoon
Ròngooñu mère bi su geenatul
Moy xellam dal na noonam beggatul
Jaar naa foo jaarewul ba agsi fii
Boo jaare fi ma jaar deeg Rest In Peace
Fate wu ma demb moo waral tay
Ligeey fii tay parce que suba moy fay
Respect ci Paa bi ndanaan la jur
Li may def ci Hip Hop xajjul ci yuur
I feel good
Nobody can disturb sunu life
Ñun dañ koy def ba muy moom
I feel good
Respect ñi la dundal demb'ag tay
I never let you down
I feel good
You push me high
I never let you down
I feel good
You make me smile
I never let you down
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
I'm feeling good, feeling alright
Foog naa ni gent ay dëmm weeyo'og gueule doon smily
Yeen saay ma toog jakkarlo'og sama life
Gis muy gën a tar may dolli gëm man def li ma war
I'm feeling good
Boo ñu bëggee disrespect f**k you
F**king feeling good
Jamanoy dox att yi di yox nga wara joge ci xale doon magg
Life bi ay soxla lay jox ba nga xam loo xammutoon nakk
Leegi Adduna ubbeeku say bëtt lu nekk nga koy jeem di lëjmbët
Tux di daw di jang di màndi njugub night kawute bëccëg
Maggu xale da fay bette da fay gaaw ci ñi ko fekke jo
Demb nga doon bébé ñu lay fobb'ag di la teete bro
Yalla rekk a ñuy sàmm mais mbedd mi mën na ñu wacce
Def nañ ko ba muy moom te teggu ñu sunuy wayjur gacce
I feel good
Nobody can disturb sunu life
Ñun dañ koy def ba muy moom
I feel good
Respect ñi la dundal demb'ag tay
I never let you down
I feel good
You push me high
I never let you down
I feel good
You make me smile
I never let you down
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
I feel good
Fi ma mujjee ak fing jëme
Fekk ma fu jege yobbu ma fu sore
Salaamalek salaamalek
Bismillah balaa maa lekk
Waayee tay Alxamdulillah lay wax
I'm feeling good
Dolli sant sant santati
Santaatati
Maa ngi baax I'm in paradise
This man called Baay Sooley
B double A Y S double O E Y
Feeling good life
Ashs The Best feeling good life
Mamy Victory feeling life
My one and only Mamy V



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best feat. Mamy Victory, Keyti & Baye Souley - 1995 - EP
Album 1995 - EP
date of release
25-02-2022




Attention! Feel free to leave feedback.