Ashs The Best feat. Iss 814 - MY LIFE Lyrics

Lyrics MY LIFE - Iss 814 , Ashs The Best



Yeah Yeah
Yeah Yeah
[Everyday I feel the same thing,
Let me show you what I use to do everyday]
Oh my life
My life
Oh my life
My life
Only sleeping in the morning
Tristesse akk xonet
Yeewu gis li ma gisoon
Def li ma deffoon
Let me show you my life
In my ghetto
My fellas ak family bi
All day I see the same thing
Paa bi akk mère bi jaxle
Waaji tukki aw jeeg
Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb
Yeah that's my life
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
Yeah
Let me show you I'm from zero to the hero now
From Ghetto sama këru maam
Ñun da ñu bari te bokku ñu yaay
Te nangu wu ñu topp ndigëlu kenn
Du kenn ku sañ a dekku li ñuy dundu sunu life
Dugg jail geen duggaat jail
Du gacce du mbañ sunu quartier
Wax ma lan la ñu gënëntee
Ndax lu ma dundoon daaw lay dundaat renn
Li ma deffoon demb lay deffaat tay
The same struggle on my way
Heure bu ñu xëyee naaj bi la ñuy njëkkënteel
Ammu ñu dara fii soxla yi di dajje
Ñakk te bëggu ñu gacce
Looloo waral guddi gu nekk ñu dajj dee
Te bëggu ñu dëkk ci clater
Du ñi fi nekkoon demb ñoo fi nekkaat tay
Mais li xewoon demb moo fi ammaat tay
Jamano di soox ñëpp mujj catte
Ku nekk ki lay còmpal ngay waatee
Sunu yoon nekkul ci reew mi ak nguur gi, juge nu ko neex àttee
We don't give a fuck, baay bakkan yëpp a nekk ci xottu gerte
Oh my life
My life
Oh my life
My life
Only sleeping in the morning
Tristesse akk xonet
Yeewu gis li ma gisoon
Def li ma deffoon
Let me show you my life
In my ghetto
My fellas ak family bi
All day I see the same thing
Paa bi akk mère bi jaxle
Waaji tukki aw jeeg
Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb
Yeah that's my life
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
(That's my life, that's my life, that's my fucking life)
Yeah
Flexion
Oh life flexion
Awma benn pression
Man sonn naa ci pression
Flexion
What you think about me
Nigger bul sori
Stay with me
Yeah
Tout le temps sama life lay topp
Every night fucked up
Mais du ay line lay tux
Ndeysaan ammoon naa ay taupes
Mënu ma woon daw tëpp
Akk Lu mu mënti yakk no
Comme ... we never made it
Album bi fog mu duggaat ci playlist
Ñu jappoon ni ... ñuy dëppu sucer nan now we love it
Du marquer histoire ... Tupac Makaveli
Di geenaat ci kër yi
Di def révolution comme ni Kerry
Ci naaj bi ci ker gi
Tout le temps ñing ci mission ci pression ci guerres yi
Ròmb ñu boppu koñ takkalante
Ñoo ci job di job everyday
Mère bi buy hustle du gis nandite
Li ñu doon rêver fils nekk na tay
Job bi day fay
Everything is okey
Du lenn luñ ñu may
That's my life, that's my life, that's my life
Oh my life
My life
Oh my life
My life
Only sleeping in the morning
Tristesse akk xonet
Yeewu gis li ma gisoon
Def li ma deffoon
Let me show you my life
In my ghetto
My fellas ak family bi
All day I see the same thing
Paa bi akk mère bi jaxle
Waaji tukki aw jeeg
Diw mi ngi jail koñ bi gën a rëb
Yeah that's my life



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare, 1da Beatz


Ashs The Best feat. Iss 814 - 1995 - EP
Album 1995 - EP
date of release
25-02-2022




Attention! Feel free to leave feedback.