Ashs The Best - Maa Ngi Dem - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Ashs The Best - Maa Ngi Dem




Maa Ngi Dem
Maa Ngi Dem
Now I know now I know
Maintenant je sais maintenant je sais
But I don't know what I'm feeling inside
Mais je ne sais pas ce que je ressens au fond de moi
Gestu woo ma
Gestu woo ma
Maa ngi dem maa ngi dem
Maa ngi dem maa ngi dem
Soo ma gisatul dem naa
Soo ma gisatul dem naa
Maa ngi dem
Maa ngi dem
Baayi a fi sama xol
Baayi a fi sama xol
Di naa weet
Di naa weet
Weet ci sama yoon
Weet ci sama yoon
Subateel
Subateel
Ba jant sow
Ba jant sow
Yaa ngi sèntu
Yaa ngi sèntu
Sa waay ju fi joge woon
Sa waay ju fi joge woon
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Ñëw naa fi noor
Ñëw naa fi noor
Ñëw naa ba dem gisoo ma
Ñëw naa ba dem gisoo ma
Ñëw naa fi nawet
Ñëw naa fi nawet
Ñëw naa fi nawet tamit
Ñëw naa fi nawet tamit
Ñëw naa fi koor
Ñëw naa fi koor
Tabaski akk Tamxarit
Tabaski akk Tamxarit
Fekk fi bekkoor
Fekk fi bekkoor
Fekk la ngay bekkoor
Fekk la ngay bekkoor
Li ma dundee
Li ma dundee
Li ma dundee
Li ma dundee
Akk li ma weesu
Akk li ma weesu
Akk li ma weesu
Akk li ma weesu
Day dellusee
Day dellusee
Da fay dellusee
Da fay dellusee
Ba mel ni seetu
Ba mel ni seetu
Ba mel ni seetu
Ba mel ni seetu
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Dem naa te taggu wu ma la
Dem naa te taggu wu ma la
Dem naa
Dem naa
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Mbaa duñ ne yow la
Mbaa duñ ne yow la
Jooy naa te kenn dooru ma
Jooy naa te kenn dooru ma
Man dem naa
Man dem naa
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Yow la
Yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Maa ngi dem te taggu wu ma la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Suma reeree mbaa duñ ne yow la
Maa ngi dem maa ngi dem
Maa ngi dem maa ngi dem





Writer(s): Olivier Delahaye, Sy Abdoulaye


Attention! Feel free to leave feedback.