Lyrics Yaakaar - Ashs The Best
Yow
mii
laa
doon
sèntu
Mbaa
yaakaar
tasul
ci
yoon
wi
Jambaar
dawul
daa
wuti
Jom
moy
dem
fulla
moy
dellusi
Yaay
di
na
woote
Di
laaj
noo
yèndoo
Leer
na
ma
sa
jamm
mo
koy
gënël
Nga
am'ag
nga
ñakk
taxu
koo
jog
Su
soxla
yi
woote
Soxla
Te
ñu
yaakaar
ko
ci
yow
Di
lañ
la
xaar
keneen
ku
dul
yow
Yow
mi
ñëpp
yaakaar
Ci
yow
sa
soxla
koo
koy
diis
Bul
tiit
bul
jàxle
Lu
yoon
bi
mën
meti
Bul
xaadi
Lu
yòmb
jiggul
goor
Jiggul
sax
jigeen
Kon
lan
ngay
caalit
Bul
tiit
bul
daw
bul
jàxle
Lu
yoon
bi
mën
meti
Bul
xaadi
Lu
yòmb
jiggul
goor
Jiggul
sax
jigeen
Kon
lan
ngay
caalit
Soo
yakkee
sooraale
ma
Man
suma
foree
fii
indil
la
Yaa
taggoo
ñu
yobbante
la
Te
soo
goree
lepp
fekki
si
la
Suñ
demmee
ba
yaakaar
Ci
yow
mi
di
utti
loo
am
di
utti
lu
gën
Suñ
demmee
ba
yaakaar
Ba
duñ
xalaat
yaakaar
gi
tas
Suñ
demmee
ba
yaakaar
Ci
gaynde
gi
rëbbi
ji
woon
mën
jaare
fa
sooy
Suñ
demmee
ba
yaakaar
Ci
moom
mi
dem
utti
ji
jën
Yow
mii
laa
doon
sèntu
Mbaa
yaakaar
tasul
ci
yoon
wi
Jambaar
dawul
daa
wuti
Jom
moy
dem
fulla
moy
dellusi
Yow
mii
laa
doon
sèntu
Mbaa
yaakaar
tasul
ci
yoon
wi
Jambaar
dawul
daa
wuti
Jom
moy
dem
fulla
moy
dellusi
Bul
tiit
bul
daw
bul
jàxle
Lu
yoon
bi
mën
meti
Bul
xaadi
Lu
yòmb
jiggul
goor
Jiggul
sax
jigeen
Kon
lan
ngay
caalit
Bul
tiit
bul
daw
bul
jàxle
Lu
yoon
bi
mën
meti
Bul
xaadi
Lu
yòmb
jiggul
goor
Jiggul
sax
jigeen
Kon
lan
ngay
caalit
Bul
jàxle
Bul
xaadi
Jiggul
sax
jigeen
Lan
ngay
caalit
Bul
jàxle
Bul
xaadi
Jiggul
sax
jigeen
Lan
ngay
caalit
Attention! Feel free to leave feedback.