Lyrics Maa Ngi Dem - Ashs The Best
Now
I
know
now
I
know
But
I
don't
know
what
I'm
feeling
inside
Gestu
woo
ma
Maa
ngi
dem
maa
ngi
dem
Soo
ma
gisatul
dem
naa
Maa
ngi
dem
Baayi
a
fi
sama
xol
Di
naa
weet
Weet
ci
sama
yoon
Subateel
Ba
jant
sow
Yaa
ngi
sèntu
Sa
waay
ju
fi
joge
woon
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Ñëw
naa
fi
noor
Ñëw
naa
ba
dem
gisoo
ma
Ñëw
naa
fi
nawet
Ñëw
naa
fi
nawet
tamit
Ñëw
naa
fi
koor
Tabaski
akk
Tamxarit
Fekk
fi
bekkoor
Fekk
la
ngay
bekkoor
Li
ma
dundee
Li
ma
dundee
Akk
li
ma
weesu
Akk
li
ma
weesu
Day
dellusee
Da
fay
dellusee
Ba
mel
ni
seetu
Ba
mel
ni
seetu
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Dem
naa
te
taggu
wu
ma
la
Dem
naa
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Mbaa
duñ
ne
yow
la
Jooy
naa
te
kenn
dooru
ma
Man
dem
naa
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Yow
la
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Maa
ngi
dem
te
taggu
wu
ma
la
Suma
reeree
mbaa
duñ
ne
yow
la
Maa
ngi
dem
maa
ngi
dem
Attention! Feel free to leave feedback.