Bril feat. OMG - Dafmay Nekh Lyrics

Lyrics Dafmay Nekh - Bril , OMG

Par AbouAmg
Lou thi xol fégne thi kanam
Xol bi yathi fess fégne sama kanam
Founé lay xol thi sa yaram di guiss sama boppou li fi rek la ma
Yama doflo dima deflo loumé bébé yamako diaral
Fouma togué guissou mala déguou fok ma wo la néla diaaral ()
Yawla bandit di ndirol kaay, waxma qui est tu
Li eupeu neu daffa fess bey tourou atanou mali
Yamay ray dima doundal aldiana guamay dougal déwagouma
Somay bayi dima mbouguel safara guamay teumbeul soma méré
Yafi ya bi fort, sama point faibleol x yako
Forr Weurouma dara lepp gua am
Diam djig' may diox la beurri baby li comme guerre
Yaw yaye bou bakh bi ya takh may noyi yaye sama air
Yaye sédal sama xol di tangal,sama yaram doma mey dara
Sougnou wété doma yeureum
Ma raw sax visa shengen toukil baby foula nekh do faye
Thieuguine
Xamgua mane ma bakh thi yaw kay gnou thieuguine
Fékheul sa xol ma this
Guaw gneuthieuyuyeul g daw kay gnou thieuguine
Diégué ma diégué ma gneuweul gnou féthe moulatheuguine
Lepp lo sokhla lalal diox di weuy thi say waw
Sougnouy beurré diaroul arbitre yaw yaye moudjé daw
Foma wo ma wouyou bolé thi nekh thi kaw bathi souff
Wolou guama gnou dém may wérou waye maly ouff
Fouma dém gua weuririna,
Fimguila diap souff koudoul crinière deh doyoula
Moi j'assure damla xam deh sur mesure
Fomla téyé daffay nekh malay dioylo je t'assure
Thieuguine
Fowé sa xol meuno si dara
Beug na dafmay nékh
Nakhla ni bébé meuno si dara
beug na li dafmay nekh
May xalé bila pogné meuno si dara
Mome la meuno thi dara meun la fepp meuno si dara
Yaye sédal sama xol di tangal,sama yaram doma mey dara
Sougnou wété doma yeureum
Ma raw sax visa shengen toukil baby foula nekh do faye
Thieuguine
Xamgua mane ma bakh thi yaw kay gnou thieuguine
Fékheul sa xol ma this
Guaw gneuthieuyuyeul g daw kay gnou thieuguine
Diégué ma diégué ma gneuweul gnou féthe moulatheuguine
Xamgua crinière ma bakh thi yaw kay gnou thieuguine
Fékheul sa xol ma this guaw gneuweul gnou thieuguine
Ya meuneu tékou limay daw guiny g
Guiné g féla g
Fowé sa xol meuno si dara
Beug na dafmay nékh
Nakhla ni bébé meuno si dara
beug na li dafmay nekh
May xalé bila pogné meuno si dara
Mome la meuno thi dara meun la fepp meuno si dara
Yaye sédal sama xol di tangal,sama yaram doma mey dara
Sougnou wété doma yeureum
Ma raw sax visa shengen toukil baby foula nekh do faye
Thieuguine
Kay gnou thieguine
Gneuweul gnou thieguine

Bril feat. OMG - Multivers, Vol. 1
Album Multivers, Vol. 1
date of release
27-11-2020

Attention! Feel free to leave feedback.