Canabasse - Boul ma khar - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Canabasse - Boul ma khar

Boul ma khar
Boul ma khar
Boul ma khar nax damay goudeh
Mon cœur, mon amour, tu es belle
Fayal lepp teh dem teudi
L’amour que j’ai pour toi est profond
Ma la newone mangui nieuw di na nieuw
Je ne veux que toi, ma douce, je ne veux que toi
Te lima jott diankontel la goudeul sama yonn
Tes lèvres, tes doigts, mon amour, je les veux tous
Kone souba lay teww
Tout le temps je t’aime
Kodj ma souba tchi fadjar tell
Même si le soleil se lève et se couche, je t’aime
Bou ma nieuwe di na fekk nga diapantel nelaw
Mon cœur, ma douce, je ne veux pas vivre sans toi, je suis fou de toi
Me bo yewo seritia bi dingua ko feke sa kow lal
Je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas
Bobou ba legui yangui ladje mananla mangui tchi
Tu es mon cœur, tu es mon âme, je ne peux pas vivre sans toi
Bobou ba legui yangui khar te mousso khadi tchi
Tu es mon cœur, tu es mon amour, je ne peux pas vivre sans toi
Sentouko khamal kagn lay gneuw
Tu es mon cœur, je ne peux pas vivre sans toi
Teh noon niou ngi len nann damay leboon
J’ai besoin de toi chaque jour, chaque nuit, chaque moment
Naxouma la mangui nieuw
Je ne veux que toi, mon amour
Guedj bi mo sambaran me walay mangui diow ohh
J’ai besoin de ton sourire, tu es mon soleil
Mangui senn tefess bi
Mon amour, mes sentiments sont pour toi
Legui ma eksi
Je suis fou de toi
Yagatoul ma terrsi
J’ai envie de te serrer dans mes bras
Kone bo teude nala nangua nelaw
Je ne veux pas vivre sans toi, mon cœur
Teh xamne xell dou degn ci iow
Je veux te regarder chaque jour, chaque nuit
Nax ci tekay you goudi gui lay degue sa batt
Tu es mon rêve, tu es mon désir, tu es mon amour
Nganann ma go bass
Mon amour, je t’aime
Khalatt bi di ma xatall
Tes lèvres, tes doigts, mon amour, je les veux tous
Anhh Kone amoul lene lou may ragall
Oh, mon cœur, je suis fou de toi, je ne peux pas vivre sans toi
Gueum gueumou seug beuss feull
J’ai envie de te toucher, je suis tellement fou de toi
Begall la
Mon amour, je t’aime
Iow mi di xar mouy tarr ngey gueune di diapp
Je te veux, je te veux, je te veux, je suis fou de toi
Deume nouggi wone togouna
Tu es mon cœur, tu es mon âme, je ne peux pas vivre sans toi
Dara dessoul loudoul yakk
J’ai besoin de toi, chaque jour, chaque nuit, chaque moment
Bass a aye demalay yakk
Mon cœur, je t’aime, je t’aime
Delola nioukoul naxx sa tiofel taxx ma magg
Tu es mon soleil, tu es mon amour, je ne peux pas vivre sans toi
Boul ma khar nax damay goudeh
Mon cœur, mon amour, tu es belle
Fayal lepp teh dem teudi
L’amour que j’ai pour toi est profond
Ma la newone mangui nieuw di na nieuw
Je ne veux que toi, ma douce, je ne veux que toi
Te lima jott diankontel la goudeul sama yonn
Tes lèvres, tes doigts, mon amour, je les veux tous
Kone souba lay teww
Tout le temps je t’aime
Kodj ma souba tchi fadjar tell
Même si le soleil se lève et se couche, je t’aime
Bou ma nieuwe di na fekk nga diapantel nelaw
Mon cœur, ma douce, je ne veux pas vivre sans toi, je suis fou de toi
Me bo yewo seritia bi dingua ko feke sa kow lal
Je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas
Kone bo teudeh nala nangua nelaw
Je ne veux pas vivre sans toi, mon cœur
Teh xamne xell dou degn ci iow
Je veux te regarder chaque jour, chaque nuit
Naxx ci tekay you goudi gui lay degue sa batt
Tu es mon rêve, tu es mon désir, tu es mon amour
Mangui lay degue nga may wo
Je suis fou de toi, mon amour
Di youkhou sama tour damn wouteh wo kou woor
Je veux vivre avec toi, je veux être avec toi
Taxaw ci xerr di sentou werr
Mon amour, je t’aime
Me boul worri dingua worri
Mon cœur, je t’aime, je t’aime
Licci kanam rawouli beutt
Mon cœur, je t’aime, je t’aime
Licci guinaw gueuneu sorri
Mon amour, je t’aime, je t’aime
Boul ma xarr sone nga teudil
Mon cœur, je suis fou de toi
Mangui ak sama tiabi bou ma dikke di na tidji
Je veux être avec toi, je veux te prendre dans mes bras
Seritie bi di na beuri
Je t’aime tellement, mon amour
Mbegte di na tew si keur gui
Je veux te serrer dans mes bras, je veux te toucher
Sa mbeur mongui nieuw dina tedj guemegn you noon yi
Mon cœur, mon amour, tu es tout ce que j’ai
Mangui niaww
Mon cœur, je t’aime
Degg ngeu mangui nieuw
Je ne peux pas vivre sans toi
Deugg la mala newoon two thousand and ten
Mon amour, 2010, je t’aime
Att yi niongui demm mangui beugue yagg ci tenn bi
Je t’aime, je t’aime, je t’aime
Wante mangui nieuw
Mon amour, je t’aime
Gueumeul neh mangui ci iow
Je suis fou de toi, mon amour
Bouma dikke dingua begg
Mon cœur, je t’aime, je t’aime
Teh dottou ma meusseu demm
Je veux te regarder chaque jour
Boul ma khar nax damay goudeh
Mon cœur, mon amour, tu es belle
Fayal lepp teh dem teudi
L’amour que j’ai pour toi est profond
Ma la newone mangui nieuw di na nieuw
Je ne veux que toi, ma douce, je ne veux que toi
Te lima jott diankontel la goudeul sama yonn
Tes lèvres, tes doigts, mon amour, je les veux tous
Kone souba lay teww
Tout le temps je t’aime
Kodj ma souba tchi fadjar tell
Même si le soleil se lève et se couche, je t’aime
Bou ma nieuwe di na fekk nga diapantel nelaw
Mon cœur, ma douce, je ne veux pas vivre sans toi, je suis fou de toi
Me bo yewo seritia bi dingua ko feke sa kow lal
Je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas
Boul ma xarr nakh damay goudeh
Mon cœur, mon amour, tu es belle
Feyal lepp teh demm teudi
L’amour que j’ai pour toi est profond
Dina nieuw
Je ne veux que toi, ma douce, je ne veux que toi
Me lima diapantel la goudeul sama yoon
Tes lèvres, tes doigts, mon amour, je les veux tous
Kone souba lay tew
Tout le temps je t’aime
Kodj ma souba tchi fadiar tell
Même si le soleil se lève et se couche, je t’aime
Bou ma nieuwe dina fekk nga diapantel nelaw
Mon cœur, ma douce, je ne veux pas vivre sans toi, je suis fou de toi
Mais bo yewoo seritia bi dingua ko fekk sa kow lall
Je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas
Dinga ko fekk sa kow lall
Je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas
Yeah dinga ko fekk sa kow lall
Oui, je t’aime tellement que même la mort ne nous séparera pas

Attention! Feel free to leave feedback.