Canabasse - Yakkal Sama Der - translation of the lyrics into English

Lyrics and translation Canabasse - Yakkal Sama Der

Yakkal Sama Der
The Yakkal Sama
Kids Capsi Gang
Kids Capsi Gang
Yaw (3 fw)
Yaw (3 fw)
Wahma ana lane motax nguay hate
Wahma ana lane motax nguay hate
... donté danguay signe say youma rombé
... donté danguay signe say youma rombé
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Canabasse
Canabasse
Yaxal sama dér
Yaxal sama dér
Han
Han
Manguéx dérmato
Manguéx dérmato
Yeah mister JO
Yeah mister JO
Mane doma téré go
Mane doma téré go
Dém na ba gneuw
Dém na ba gneuw
diougue go
diougue go
If life is the bitch
If life is the bitch
My nigger dangua yomm
My nigger dangua yomm
Nax do déf
Nax do déf
Han
Han
Do déf dara
Do déf dara
Danguay tok ném 0 mouvemen ni guarap
Danguay tok ném 0 mouvemen ni guarap
guarap saxeuleu eup gneurigne déy dioxé kér
guarap saxeuleu eup gneurigne déy dioxé kér
Sa sister néna nieupeuleu guéde nax do fér
Sa sister néna nieupeuleu guéde nax do fér
Nigger dama fresh
Nigger dama fresh
Yaw danguay séral
Yaw danguay séral
Boudé wax si maneuh tax nguay dounde bitch dinala téral
Boudé wax si maneuh tax nguay dounde bitch dinala téral
Dila romb everytime
Dila romb everytime
Dila mbéth ak nguélaw
Dila mbéth ak nguélaw
Bou gueneu chér sa doundou wér
Bou gueneu chér sa doundou wér
Yeah parfumé la
Yeah parfumé la
Sama yoneuh lér motax soufou shoes yi wéhe
Sama yoneuh lér motax soufou shoes yi wéhe
Gueneu la oundou gueneu klean
Gueneu la oundou gueneu klean
Bagnou ték ma wéhe
Bagnou ték ma wéhe
Sama swag déy kill ma done suicidaire
Sama swag déy kill ma done suicidaire
Nax say souma yéwo tim sétou damay gueneu déééé
Nax say souma yéwo tim sétou damay gueneu déééé
Yaw (3 fw)
Yaw (3 fw)
Wax ana lane motax nguay hate
Wax ana lane motax nguay hate
Donté danguay signe say youma rombé
Donté danguay signe say youma rombé
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Yaxal sama dérrr
Yaxal sama dérrr
yoooooo yaxal (2 fw)
yoooooo yaxal (2 fw)
Meune ngua yax sama dér
Meune ngua yax sama dér
do guisse sama défaite
do guisse sama défaite
Nax beusse boumay celebrate
Nax beusse boumay celebrate
Nala invité sama féte
Nala invité sama féte
Canabasse
Canabasse
Gnou wax ni
Gnou wax ni
Ninja kid ragaloul périé
Ninja kid ragaloul périé
alkolik kéne douko diam périé
alkolik kéne douko diam périé
Game bi mane la love téy la 14 févriér
Game bi mane la love téy la 14 févriér
Loxom sama loxo gnouy ande nguéni hate
Loxom sama loxo gnouy ande nguéni hate
Amo xeuy di kasse mélni kougnou syndiké
Amo xeuy di kasse mélni kougnou syndiké
Xamoulo sama loi beugue done policié
Xamoulo sama loi beugue done policié
Sama guiss guiss thi yaw baram bithi digue békoy indiké
Sama guiss guiss thi yaw baram bithi digue békoy indiké
Yéne gneup danguéne périmé
Yéne gneup danguéne périmé
Fi ba 2020 damay tégou man
Fi ba 2020 damay tégou man
éléve yi mane lagnouy xar mélni jourou férié
éléve yi mane lagnouy xar mélni jourou férié
Litax ma tangue gnaxou ma moy si mane ordinaire
Litax ma tangue gnaxou ma moy si mane ordinaire
Mane la basse bitch léxtra ordinér
Mane la basse bitch léxtra ordinér
Kontenaire kéne douko remorké ak fil de fer
Kontenaire kéne douko remorké ak fil de fer
Ana koufi antane sama album???
Ana koufi antane sama album???
Dou béne labél
Dou béne labél
Bo guissé gnar gnou mélni mane diapal ni dangua guénte
Bo guissé gnar gnou mélni mane diapal ni dangua guénte
Hannnnn
Hannnnn
Boul dégue téll rék dééé
Boul dégue téll rék dééé
bo dégué tél séne ma ngua gnaw nax ...hannnn
bo dégué tél séne ma ngua gnaw nax ...hannnn
Dama vré mane hannnn
Dama vré mane hannnn
vréman hannnn
vréman hannnn
Boy woutél sama meune meune dangua féééébbbarrr
Boy woutél sama meune meune dangua féééébbbarrr
Yaw (3 fw)
Yaw (3 fw)
Wax ana lane motax nguay hate
Wax ana lane motax nguay hate
Donté danguay signe say youma rombé
Donté danguay signe say youma rombé
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Ma fok ni dangua cool nguay yax sama dééérr
Yaxal sama dérrr
Yaxal sama dérrr
yoooooo yaxal (2 fw)
yoooooo yaxal (2 fw)
Meune ngua yax sama dér
Meune ngua yax sama dér
do guisse sama défaite
do guisse sama défaite
Nax beusse boumay celebrate
Nax beusse boumay celebrate
Nala invité sama fête
Nala invité sama fête

Attention! Feel free to leave feedback.