Cheikh Lô - Guiss Guiss Lyrics

Lyrics Guiss Guiss - Cheikh Lô



Mama sa mbow massa mbow massa mbow
Massa mbow massa mbow
Yay ki gnouy dimbali fi va fagnou forum
Kham khamou adouna moo dii
Da ngay kham sa morom ndieuk
Soga kham gnénen
Wawaw
Am amou adouna moo diii
Da ngay am sa mbokk waaw di démalanté
Waawaw
Ni jaami adouna moo dii
Am weer gu yaram soga tal adouna woo
Mbeguelou adouna mo di Youssou
Da ngay dieul sa sokhna waaw nguirr moulay wétali
Nii laa ko guissé
Yaw mi sa kham kham adouna ngay diangalé muy dunya
Alalou adouna moo dii
Da gay am sa takander waaw
Nguirr moulay dondou euleuk
Nii laa ko guissé
Sa am am adouna
Ngay doundalé
Muy dounya
Ma massa mbaw massa mbow massa mbow
Massa mbow massa mbow
Yay ki gnuy dimbalé
Fi ba fa gnu dieum di deug
Kham khamou adouna moo dii
Da ngay kham sa borom ndieuk soga kham gnénen boumaroo
Yaw mi sa kham kham adouna ngay diangalé muy dunya
Am amou adouna moo dii
Da ngay am sa mbokk waaw
Di démalanté wawaw
Yaw mi ci sa am am adouna dimbalé muy dunya
Ni jammi adouna moo dii
Am weer gu yaram soga tal adouna woo
Yaw mi ci sa kham kham adouna
Ngay diangalé luy dounya
Fadiou adouna moo dii
Am dundou gu doy soga meuneu tagg dieukeur wawaw
Yaaw mii ci sa am am adouna
Ngay doundalé muy dounya
Wetalou adouna moo dii
Da ngay dieul sa sokhna waaw nguirr moulay motali Mame Diarra
Ma massa mbow massa mbow massa mbow
Massa massa mbow massa mbow
Yay ki nguy dimbali fi ba fa gnu dieum
Ma massa mbow massa mbow massa mbow
Massa mbow massa mbow
Massamba yay ndiarign
Ci sa kham kham adouna
Ngay diangalé luy dounya
Ma massa mbow massa mbow massa mbow
Massa mbow massa mbow
Massamba yay ndiarign
Ci sa kham kham adouna
Ngay diangalé luy dounya
Ma massa mbow massa mbow massa mbow
Massa mbow massa mbow
Massamba
Ci sa kham kham adouna
Ngay diangalé luy dounya
Ma massa mbow massa mbow massa mbow massa mbow massa mbow



Writer(s): MAMADOU LO, YOUSSOU N DOUR, OUMAR SOW


Cheikh Lô - Né la thiass
Album Né la thiass
date of release
28-10-1996




Attention! Feel free to leave feedback.