Cheikh Lô - Né La Thiass Lyrics

Lyrics Né La Thiass - Cheikh Lô



Boo nekkee sa tool di waaj a ji, yaw,
Mbaa nga nekk sa tool di waaj a jëmbat,
Yaakaar de la′y feese; ba nga fatte ne daal ne dogal du lu'y jaas.
Man na la fekk ci bérab, ne la càs!
Ne la càs, ne la càs, ne la càs; jëmale daal fu ko neex...
Boo nekkee ci biir Ndakaaru Njaay,
Mbaa mu fekk la yaw Kawlax Nangaan,
Yaakaar de la′y feese; ba nga fatte ne daal ne dogal du lu'y jaas.
Man na la fekk ci bérab, ne la càs!
Ne la càs, ne la càs, ne la càs; jëmale daal fu ko neex...
Àdduna toogul, ni dex bu'y bawal la.
Li coow li bàri bàri, lu mu bàri,
Selew ne ko ndix wann; jëmale daal fu ko neex...
Ngala waay, bu la coono jàpp,
Ba tàx nga jàpp lool,
Ndax dooley fas u naar u góor, taar u jongoma; dara du fi des!
Ngala waay, bu la coono jàpp,
Ba tàx nga jàpp lool,
Ndax dooley fas u naar u góor, àlal gu ne gàññ; dara du fi des!
Àdduna toogul, ni dex bu′y bawal la.
Li coow li bàri bàri, lu mu bàri,
Selew ne ko ndix wann; jëmale daal fu ko neex...
Ngala waay, bu la coono jàpp,
Ba tàx nga jàpp lool
Ndax dooley fas u naar u góor, taar u jongoma; dara du fi des!
Ngala waay, bu la coono jàpp,
Ba tàx nga jàpp lool,
Ndax dooley fas u naar u góor, àlal gu ne gàññ; dara du fi des!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Bawul dara!
Bawul dara!
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs!
Ne la càs!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Bawul dara!
Bawul dara!
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs!
Ne la càs!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Yàgg yàgg bawul dara!
Bawul dara!
Bawul dara!
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs, ne la càs, ne la càs.
Ne la càs!
Ne la càs!



Writer(s): Oumar Sow, Mamadou Lo, Assane Sylla


Cheikh Lô - Né la thiass
Album Né la thiass
date of release
28-10-1996




Attention! Feel free to leave feedback.