Dope Master - Ennemies Lyrics

Lyrics Ennemies - Dope Master



Big dog i'm like rambo
May sénn GOAT may sénn Christiano
Cédélé ay dope they call me Pablo
Le monde chico tout comme Montana
I feel like a hero
Khoss ay bonn ak gant wou Tanos
Heure de crime mangui si birr ghetto
Chargé bopp bi melni guerre la dieum
Shot out to my ennemies
Diokh nagn ma energy
Fuck nieup encaissé benefice
Non douma si nelaw fils
Chaque att le même objectif
Feulat ak yénénn mbir
Paqueté ay panou shit
Nianal ma danou bitch
Grrr ta bang kana dou khalat
Nieuw pour dieulsi couronne mangui niane yallah boum ratakh
Teukeu lék ma akk gars yeup kham nagn ni Vain rouge dou bissap
Doma guiss ak gars yeup game féss ak goor you rambakh
Moudiéntél adouna
Fuck promo
Fuck publicité
Fuck ay yokk dolé
Fuck partage bou égoul si khol
Heureusement yallay cédeulé
Risque leu tapet douko def
Tek budget enchaîné projet
Complexé bayi lenn niouy tiank rek
Teup frontière dém wérou Sacem
Big dog i'm like rambo
May sénn GOAT may sénn Christiano
Cédélé ay dope they call me Pablo
Le monde chico tout comme Montana
I feel like a hero
Khoss ay bonn ak gant wou Tanos
Heure de crime mangui si birr ghetto
Chargé bopp bi melni guerre la dieum
Shot out to my ennemies
Diokh nagn ma energy
Fuck nieup encaissé benefice
Non douma si nelaw fils
Chaque att le même objectif
Feulat ak yénénn mbir
Paqueté ay panou shit
Nianal ma danou bitch
Nianal ma diam danou nigga
Mangui sa kaw diabar
Mongui mann késsé ma am studio
Gni guénéwoul nagn diégual
Dama yagu si diap teh bayi wouma nigga
Nek si yonn bi sans diadeu nigga
Fok ngua kham ni
Niouneu topou niou kenn nigga
Benn nigga dou téré niou lek nigga
Senn Khėl meuneul dall kom kouy Fay louyass
May tek niouy cons di cass
Volonté la Bolé ak efficace
Doumalenn get lougn tek day low si Mann
Sama niveau romb fi yeup
Heure bi diote moma teuyé fi ni
Latchieu sama bopp néma dope amo Loy prouvé nite
Call me og si bitches yi
Mann la Bala si Yékini
Big dog i'm like rambo
May sénn GOAT may sénn Christiano
Cédélé ay dope they call me Pablo
Le monde chico tout comme Montana
I feel like a hero
Khoss ay bonn ak gant wou Tanos
Heure de crime mangui si birr ghetto
Chargé bopp bi melni guerre la dieum
Shot out to my ennemies
Diokh nagn ma energy
Fuck nieup encaissé benefice
Non douma si nelaw fils
Chaque att le même objectif
Feulat ak yénénn mbir
Paqueté ay panou shit
Nianal ma danou bitch




Dope Master - Malaka
Album Malaka
date of release
26-01-2024




Attention! Feel free to leave feedback.