Dope Master - FPC Lyrics

Lyrics FPC - Dope Master



Fuck permis circulation
Mangui si town bi ni tramogen
Indi sauce indi niakatangu
Yagua rang boul meusseu fok ni dama si dall
Toujours frais melni fin décembre
Sama gars yi daniouy def dougn si bolé wakh
Boy bou ndaw meunn na diay seu mame
Tall sama bopp briller ni nadiou is aldiouma
Nieuw indalé changement climatique
Égoïste la fuck thématique
Teudiou boycotter polémique
Mangui si wagn bi di wonn nieup louy prolific
Am na guél mais yow plan ngua bitch
Damala vu ngua sissou de qui tu te fiche?
Dope kom kana bou dioudo fi
Sipp nagn mangui niveau bou nek au dessus
Dagn ma namonn hello motherfuckers!?
All eyes on my Esk nguénn 2Pac
Hoya Chui dans le terrain melni ballon ak volet yi
Dem si dealer loumou outé ak dem pharmacy
Plaquette hachich fuck ay peudo
Li nek si bopp bi poch bi moko pecho
Danguay tioub seu drapeau pour ay nichon
Mann si diguenté tank yi la def bureau
Djité mafia bi melni Big meech
Nigga soma séné si bir town sénn ngua Chief Ckeef
Téglé ba si kaw fénté Pirvmid
Mann dh mangui Ler Lérou Yallah fuck ay bling bling
Og bi dou tiéré Seutou Bour sine
Mum seu khel neu dall douma dioutou mouk pour siw
Gars yi naniou khiff limây togu nékoul pour fi
Khalal mangui tangu dama souss bitch nigga
Fuck permis circulation
Mangui si town bi ni tramogen
Indi sauce indi niakatangu
Yagua rang boul meusseu fok ni dama si dall
Toujours frais melni fin décembre
Sama gars yi daniouy def dougn si bolé Wakh
Boy boy ndaw meunn na diay seu mame
Tall sama bopp briller ni nadiou is aldiouma
Fuck permis circulation
Mangui si town bi ni tramogen
Indi sauce indi niakatangu
Yagua rang boul meusseu fok ni dama si dall
Toujours frais melni fin décembre
Sama gars yi daniouy def dougn si bolé Wakh
Boy boy ndaw meunn na diay seu mame
Tall sama bopp briller ni nadiou is aldiouma
Gwaye city Mann mako fa am
King bi tew na nguay latchie evidence
Dawlo boy yi ni auto ramass
Souma feulé niou latchié tay ko nara mass
Mann ak khaliss beu 6 pied si souf
Fayo dara ma bayi la expliquer doul
Dangu ma invite concert teh wakho leer
Sougn fa tégué sougn tank yi rek money mo dougu
Nigga I flex I'm flexible
Gni beugu ma danou nagn ma si kaw
Nelawouma mangui niafé ni Goor
Nigga Zam néna yonou success meussoul nara yomb si goor
So maroul tateu meuno bok si niom
Si digu niakatangu ni fou bi si police
My real nigga fok ma changé pour niou yokk ma dolé
Set ma si town bi dama rare melni deukeu touma fi
Nél gars yi sissou dope Mongui senn (Awwww)
Fuck fake yi yeup boycotter
Saw senn Kay out lenn parapluie
Fuck partager fuck Lou leen nexx
Nélén dope bi si kaw leu dieum
Dégu nala mais goumba teukh
Mangui si waagn di hustle comme Coumba amoul ndeye
Soti came yi di defar rek
Latax police meussou ma 6h du matin
Fuck permis circulation
Mangui si town bi ni tramogen
Indi sauce indi niakatangu
Yagua rang boul meusseu fok ni dama si dall
Toujours frais melni fin décembre
Sama gars yi daniouy def dougn si bolé Wakh
Boy boy ndaw meunn na diay seu mame
Tall sama bopp briller ni nadiou is aldiouma
Fuck permis circulation
Mangui si town bi ni tramogen
Indi sauce indi niakatangu
Yagua rang boul meusseu fok ni dama si dall
Toujours frais melni fin décembre
Sama gars yi daniouy def dougn si bolé Wakh
Boy boy ndaw meunn na diay seu mame
Tall sama bopp briller ni nadiou is aldiouma




Dope Master - Malaka
Album Malaka
date of release
26-01-2024




Attention! Feel free to leave feedback.