El Hadj N'Diaye - N'guelaw Lyrics

Lyrics N'guelaw - El Hadj N'Diaye



Fuu ngelaw di danél le kuy daal
Picci moo faay naaw
Massigi massigi moo teew na taay
Ma penda gni ni ay waay mapenda gni ni
Ngelaaw dikk ti picci soonu lol
Yam ci Mapenda
Mboo ma woowé ma tamgam luu du cagani ragal
Dama yakk fekké gnoom gnu jëf ma giis
Am na gnu la wootal wooma mba ma yákaar
Ndeke dañ ma fiir
Gni deff ma cësslaay,gni deff ma lonko
Bagnou amé lou gnu yoobu




El Hadj N'Diaye - Xel
Album Xel
date of release
08-06-2001




Attention! Feel free to leave feedback.